Oothentik Zeus - No Limit ( Clip Officiel )

preview_player
Показать описание
Hello les lovers, voici le 3e clip extrait de mon album #THIAPATHIOLY. Un son qui parle d’un couple inséparable et qui ne donne pas de limite à leur amour illustré par une vidéo romantique et sensuelle.

Auteur: Oothentik Zeus
Beatmaker: Gunsilent Beatz
Chef op.: Mandione Laye Ka
Réalisation: @SenegalPlus
Figurante: Diadia Cissé
Stylisme: Mushei Street
Accessoires: 221 Luxury
Make up: Mafary ( 778950010 )
Mix Master: Rifou & Freshii Beatz
Label: @deffmusictv5611

Remerciements à Aïcha notre très chère pote !
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Paroles:

I’m in love with you
Xel mi moogsi iow soubeu ba ngoon
Baby miss you
Fii laala sokhla bouma yeewo soubeu teel

Ay att di ngoro
Fimla denth sorri damla love ba forokh
Dieul sa numéro
Composer wooter jot leu khol bi cedd hello

Refrain:

Soukeur sama life
Yaay khorom
Khol bi yaassi nek yaay borom
Dinaa def sa yaay goro
Digueunté moogui ladj gouro

Parce que si mane amoo limite
Limit limit Limit
Parce que khol bi iow la bouga
Bougaa Bougaa Bougaa
Parce que si mane amoo limite
Limit limit Limit
Parce que khol bi iow la bouga
Bougaa Bougaa Bougaa

Mane ma waroon di ladj
fima toolou si iow
Amoo limite thi mane

Bouder mbeuguel dou jaay
Téwoul diaral ngama
Iow yaay ki gueun thi mane

Nakh damla bouga
Boulma baayi lokhotima fouma douga
Na nga melni soular
Ak bouteille bimou top moukoy douma

Baby xamanter nagn Maak iow ça fait
longtemps
Domage
Nakh defagooma demande
Nee ngueu kagn la wesssou dokhaan
Xamga
Mais dinalako wakhaat

Refrain:

Soukeur sama life
Yaay khorom
Khol bi yaassi nek yaay borom
Dinaa def sa yaay goro
Digueunté moogui ladj gouro

Parce que si mane amoo limite
Limit limit Limit
Parce que khol bi iow la bouga
Bougaa Bougaa Bougaa
Parce que si mane amoo limite
Limit limit Limit
Parce que khol bi iow la bouga
Bougaa Bougaa Bougaa

oothentikzeus
Автор

beau garçon, belle flow, génie en écriture, meilleur de ça génération, l'AF thiate yallana djigue🙏🌹

CANABOY
Автор

Othenticité + Talent + savoir faire = Othentic Zeus 💯💥🤞
Comme j'ai souvent l'habitude de le dire fait ce qu'il faut tôt au tard tu sera récompenser nous sommes fière de toi frère👊

bassiroudiop
Автор

C'est du lourd wallah, c'est la nouvelle génération 🇸🇳🤜🤛

ladu
Автор

Buma lokattima fouma duguaa
Zeus tu n'est pas un être humain sur ce son force tw Golden boie du rap africain douma wakh rapp galsen par ce que diell nga voll bii di daw broh
Le produit du village ♥️🇸🇳🤌🏼

ramataismaelasow
Автор

C'est un album que j'écoute tous les jours. Zeus est un phénomène de la musique sénégalaise. Merci pour ce beau tube

babacarndione
Автор

Idole bi Toni sosa clib bi lagnouy khar dh 😁mes sa liguéy nice na machallah Notre Thiapathioly nationale Boie Rio❤

SambaNgom
Автор

Ndaye lo bando c le produit du village ✌

abdoulazizndoye
Автор

Mon king. C'est le roi du rap gamsen 21-22

Kekendo_Sylla
Автор

Frr son bi gaate na neikh na 🥰🤗 bravo bonne continuation

boubacardiallo
Автор

Bien ça vidéo bi nice n'a trop frère

kingmaygazo
Автор

Machalla machalla dina bakh inchalla OOTHENTIK ZEUS ♥️😍☠

oulydiallo
Автор

J'ai tant attendu le clip après avoir écouté à multireprise le Son .
Les images sont en parfaite synchronisation avec le son . J'aurai aimé voir à la fin du clip un Mariage 😂 mais Zeuss hamna célibataire yi nguay diapalé
Bonne continuation et plein de succès . Votre Album m'a vraiment marqué
PERO a validé

elpero
Автор

Nice clip mon frère la fille est trop belle machalah

omarcisse
Автор

Je te le jure vous méritez un disque d'or et cela va être in shaa God force à toi oothentik

sellysane
Автор

Franchement ligueye ngua br0🤴🏾👌🏾bonne continuations diambar

ibrahimandiaye
Автор

Bilahi zeus son Moy yé louy Nelaw si Man 👨 surtout commencement bi Dafa Graw Li sonnerie Sah la koy Deff

Babgraph
Автор

Wllh galsen bamou dadie new génération bi yafi dakh Rap je te le jure wollah t'es toujours le meilleur frr Idol bi

buzzcana
Автор

Oothentik zeus aka aladji ass borom punch yii🔥✌️

youngboysn
Автор

Idole bi saltel fepp from Ndiaye lo
Ts le meilleur Wllh kéne dou iow Amal Diameu rck mbokk GB OOTHENTIK

buzzcana
join shbcf.ru