Iss 814 | Xool Ma ci Bët (ft. Jeeba) [Official Video]

preview_player
Показать описание
Titre: Xool Ma ci Bët
Artistes: Iss 814 & Jeeba
Prod. : Iss 814, Yannick
Réal. Vidéo: Black Rétina | BayeBlVck
Mix/Mastering : King Beat
Lumières : Yarba Déco & Justin Mendy
Clip Tourné au Safari Studio
Artwork: Eyelit Studio
________
________
________
Retrouvez moi sur les réseaux sociaux:

LYRICS

Mbeuguel bou deugou
Dara douko faye
Yaay seetou
Biye woné sama leeraye
Jant goudi
Biddew soubeu teel
Bimala xamé
Ci la tagok weetaye
Nii tognal sa aaaaaa ! yaye
Balenala ndakh mbeuguel bimaay yeug
Ci yow
Nii tognal sa aaaaaa ! Baye
Balenala ndakh mbeuguel bimaay yeug
Ci yow
Wolou nala wolou wolou nala !
Eh yaaaay !
Wolou nala wolou wolou nala !
Ahn ahn !

Boume laay guiss ngaay doundou
Dafemaay doundeul baby
Soume laay guiss ngaay rétaan
Dafemaay doundeul waay
Boume laay guiss ngaay doundou
Dafemaay doundeul baby
Boume laay guiss ngaay rétaan
Dafemaay doundeul waay

Xool ma ci bët
Ma xool la ci bët
Nioune niare la rek
Mbeuguel a nekh
Xool ma ci bët
Ma xool la ci bët
Nioune niare la rek
Mbeuguel a nekh
Yéne saaye nga diéki diéki woma
Woma
Nga meer maané mba diépiwoma
Nga néma non non
Yéne saaye nga xole ma rek
Ma rétaan rétaan
Yaay sama boumou xol bi
Yaay sama boumou xol bi
Bo meeré ba guédeu dafemaay metti
Metti
Bo deffé ba gnipeu
Nala setsi
Setsi
Douma ci xole sax pa bek mère bi
Mère bi
Na oubi bountou bi soxna si
Dang ma diape sa mbaal
Té douma guéneuti
Bilay walay yé
Yow laay fethie ci bal
Yaay sama mélodie
Yow rek la baredé
Eh eh !

Boume laay guiss ngaay doundou
Dafemaay doundeul baby
Soume laay guiss ngaay rétaan
Dafemaay doundeul waay
Boume laay guiss ngaay doundou
Dafemaay doundeul baby
Boume laay guiss ngaay rétaan
Dafemaay doundeul waay

Xool ma ci bët
Ma xool la ci bët
Nioune niare leu rek
Mbeuguel a nekh
Xole ma ci bët
Ma xole la ci bët
Nioune niare leu rek
Mbeuguel a nekh

Yeh weurena ba weurengueul adouna
Yeh kou melni yow mba amatina
Yeh dougueul ci Keur gui yatouna
Ndakh yow yaay yaay sama boumou xol yaay sama boumou xol

Yéne saaye nga diéki diéki woma
Woma
Nga meer maané mba diépi woma
Nga néma non non
Yéne saaye nga xole ma rek
Ma rétaan rétaan
Yaay sama boumou xol bi
Yaay sama boumou xol bi

Weurena ba weurengueul adouna
Yeh kou melni yow mba amatina
Eh yah dougueul ci Keur gui yatouna
Ndakh yow yaay
Yaay sama boumou xol
Yaay sama boumou xol

#Mbedocratie #Iss814 #Jeeba

© 814 Prod. | July 2021
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

'Xool Ma ci Bët ma xool la ci ...'
Dispo partout ↓

#Mbedocratie #Iss814 #Jeeba

Iss
Автор

Merci à tous pour la force 1000eme commentaire

Iss
Автор

Je suis congolais ; je ne comprends pas wolof mais la voix de se mec me fait fondre le coeur

destymack
Автор

C'est grâce à Sadio Mane 🇸🇳 dans une vidéo de buzz Sénégal que j'ai découvert cette belle mélodie waouh c'est le top depuis le Burkina Faso 🇧🇫🙏

zenabonikiema
Автор

Iss 814 bo rappé balou malako ... Bro ta voix est fait pour chanter.. tu as un flow mortel.. je suis accro a ton playiste. Tristesse .aminata.. et mon coup de coeur water whiter

amirdiop
Автор

Waouhhh en plus les femmes incarnent la beauté africaine machaAllah nice 🤩🥰🥰🥰😍🤩

khalifaababacarkamara
Автор

DIEU SAIT QUE ISS MERITE TOUS SUR LA MUSIQUE🎺, MAIS CE PETIT JEEBA TMT KÉNE DOU MOM SI LOVE#

Thiég in💥

ElMessiaofficiel
Автор

@Iss 814 lingay weuyy Eupenaa chapeau à Jeeba💃💃💃💃

aminawane
Автор

Issa 814 est trop fort 🇨🇮❤. Soutien depuis la cote d'Ivoire

donatienpehe
Автор

Wouuu...j'ai retrouvé ma chanson, je l'ai écouté pour la première fois grâce a un ami Sénégalais 🥰🥰🥰🥰et depuis j'ai adoré

MarlyneMelessMemel-vxjh
Автор

Mais gars yi iss814 il est fort et audacieux thi flow. Té guiss nako thi yénène non ki il est top

adamandiaye
Автор

Iss 814 je t'aime blhi ya deufar saound bii srx bonne continuation amal diamb rk yaw💖🍯🔥🔥

kamoudiop
Автор

Jeeba la lumière de la musique sénégalais je kiffe fort ❤️🇨🇮

rihams.d.t
Автор

Iss 814 mon dieu😩😩😩😩 nekhna torop, jeeba quelle voix agréable ♥️♥️♥️😍😍 bravo les gars😍

aicharassoul
Автор

1er commentaire🔥🔥🔥 di sant wa Mauritanie🙏🥳🥳🥳😂😂amati nagñ ndam👑🇲🇷🇲🇷

karapeuzzi
Автор

Il n'arrête pas de nous surprendre jeeba🇸🇳❤️tu représente la fierté des Sénégalais machallah thia kaw thia kanam

aichabadji
Автор

Ohh iss, ta créativité ne cesse d'impressionner. Quand au prince de la musique sénégalaise continue de montrer au gens k mbeuguel dou ayy fo, moy lii gueune thi kaw souff, bravo

papicesene
Автор

Mon cœur appartient à un Sénégalais 🥺 mais c'est Dieu qui décide 🙏❤️

alicemakpo
Автор

Depuis hier je n'arrête pas t'écouter se son😘😘😘😘

aissatouadeyemo
Автор

quel Duo 🔥🔥mais les filles là machallah vive le Sénégal 🇸🇳❤️❤️❤️

lefootballogue