Youssou Ndour - MOOL - ALBUM - MBALAX

preview_player
Показать описание
Symbole de courage, de persévérance, et de patience, la vie du pêcheur, maître des grands larges, a toujours suscité en moi un profond respect. De Djilor à Elinkine, de Yarakh à Guet Ndar en passant par Mbour, Djifeer, Joal Fadiouth, Ouakam, Ngor, Yoff, Thiaroye votre Youssou Madjiguène vous dédie cette chanson en retour de l’amour sincère que dont m’avez toujours témoigné tout au long de mon parcours. Vous êtes des Piliers du Sénégal !
PAROLE :
MOOL
Yaw mool u géej gi
di jambaar ci réew mi
Bala ngaa dem géej
ngala déglu météo

Bu la nee bul dem
lu mën ë xew bul dem
Ben fan ak ñaar ,
bu mu yax sa liggéey

Doyloo nga yalla ,
du tee nga sa yor téléphone
Ak sa gps , te bul fatte sa gillet

Sama fans yi ma am ,
mool ñoo ma gën ë xam
Fu ma làng ee ak ñoom ,
guddi gë day xumb lool

Man sama fans yee , ma saf
Sawar naa làng ak ñoom , fu ne
Aka ñoo dégg daaj , ma ni
Moo tax may dem ba jeex , walla

Jambaar ca waar wa ,
jambaar ca géej gë
Su ma ko mën oon ,
ben mool du des ci géej

Bu la nee bul dem ,
lu mën ë xew bul dem
Ben fan ak ñaar ,
bu mu yax sa liggéey

Sama fans yi ma am ,
mool ñoo ma gën ë xam
Fu ma làng ee ak ñoom ,
guddi gë day xumb lool

Jambaar ca waar wa ,
jambaar ca géej gë
Su ma ko mën oon ,
ben mool du des ci géej

Man sama fans yee , ma saf
Sawar naa làng ak ñoom , fu ne
Aka ñoo dégg daaj , ma ni
Moo tax may dem ba jeex , walla

Yalna leen yalla suturaal ,
te di leen samm biir géej
Barke el seen liggéey bi ,
barke el seen njaboot gi
Aar leen ba ñu doon mag ,
jox leen barke maam yi

Man sama fans yee , ma saf
Sawar naa làng ak ñoom , fu ne

Yess aye
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Bël ba ca ndar , sonn al na waa guét ndar géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Mool yi laa bëgg ë làng al ,
seen làng xumb në ,
Ndax sa ma fan’s yi nak ,
am mool yee ci gën ë dense
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Bël ba ca ndar , sonn al na waa guét ndar géej oo
Sa telephone ak sa GPS ,
bul fatte gillet ba
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Ñoom laa bëgg ë làng al , seen làng xumb në ,
Ndax sa ma fan’s yi nak , am
mool yee ci gën ë dense
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo

A dëgg ël , yaw mool u géej ,
yaa di jàmbaar
Yaa bari fullë lool
Bari jom lool
Yaa donn loolu
Gëm yalla lool
Yaa xarañ lool , te tabe lool
Youssou woy na leen
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Bël ba ca ndar , sonn al na waa guét ndar géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Mool yi laa bëgg ë làng al ,
seen làng xumb në ,
Ndax sa ma fan’s yi nak , am
mool yee ci gën ë dense
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Mool yi laa bëgg ë làng al ,
seen làng xumb në ,
Ndax sa ma fan’s yi nak , am
mool yee ci gën ë dense

Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

si je vous dit que shui née le 1 octobre 2005 le même jour de son anniversaire et le meme jour du Bercy 2005 je crois que amna lougnou liies man ak mom je taime beaucoup papa youssou ndour longue vie a toi beug nala guise naak

sodalayesoda
Автор

Lima nekh si youssou moy ay fans. Sakh dagnon civilise ne ay wayam❤️

dabataphangome
Автор

Di niou niappeu ndeyam beug rey ak Amari Ngoné arame mbaye dieumeulè 20 mn 🤷‍♂️ .... xolal li père weuy nimou néxé rek té bari enseignement 🤔
Merci encore une fois le doyen de la musique africaine 🙏

papito
Автор

Youssou yalla na goudou fane, kouni amine yalla na goudou fane, eupeneu

fabynette
Автор

Ou sont les lébou fier de l'être merci à notre star planétaire 🙏🏿🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳❤️

diarratoullah
Автор

Demba ba taye amouma diote ndakh son biii tey Mane doumap mool 🤣🤣🤣🤣wayé Lou nex dou romb nop.
Merci way papa you

ndeyemaremesow
Автор

Il avait frappé il frappe et il continuera de frapper notre Youssou Ndour .

fifidiaw
Автор

Le Roi du mbalax de tous les temps Qui est d'accord avec moi? ❤🇸🇳

falloudiaw
Автор

Ndaanan woyatina notre sacré youssou Ndour l'international album réussi à 100% vous êtes le meilleur

princewallyfaramareen
Автор

Je me vois déjà au stade Caroline Faye de Mbour et au Cices en train de danser lol. Cet album est un vrai régal comme tous les autres. Love from Bamako

takothiam
Автор

Nexoul beu nexoul mais yay senn Baay😁💯🔥

papissow
Автор

Machalla Youssou Mary sène Ndour le Star planétaire que dieu vous protège Amine.

ablayendiaye
Автор

Machalah you gnoune mool yi gnonguileye santa dila gueureum

khadyfall
Автор

Mala beug bilahi guiss la rek la beug Amine Amine amine

boubacarseydi
Автор

Album de siècles kou d’accord beuseul j’aime

xomgaye
Автор

Waa lii tamit baa diamla thi man limay replay tayumako déglounako à plusieurs reprise mais jusqu'à présent doyalaguma liilan laa tamiittt chanson bi niveau bi mo kawé trop et quant c'est important c'est You kendou dou mom thi wayy do moromu kèneu thi affaire bi je vous jure son bi et TATAGAL gnoma dakhal si album bi wayy liii nekhna machalah the king l'empereur longue vie à toi lo doundou doyul nigay fékheulé sama xol bi manoko sakh xam chapeau à toi peace and love

ndongfatouk
Автор

Grand frère depuis le Cameroun ta voix retentit et nous egaille Long live and cure on.

youssoufaboubaabba
Автор

Du mbalax pur et dur, entre Youssou N'Dour et les mool c'est tout simplement une très longue histoire d'amour 👏👏👏💪🇸🇳🇸🇳🇸🇳💪

laminemboup
Автор

Toutes mes félicitations mayy nala 1milliard d'avoir chanté mes parents pêcheurs
Wa guet ndar, soumbedioune sa keur baye beggnene si yaww

diopcheikh
Автор

Saliou ndiaye mol a mbour tefesse Youssou waygua keep desolonou Dara daguano sorry mane bouma alone li ma begue sa adouna môme laye rêve ma dianok Yao Youssou conten ci yao Sama gual Yao lako toude

salioundiayediata