Cherifou & Job Sa Brain ( BAMBA)

preview_player
Показать описание
Reconnu parmi les figures les plus emblématiques de l’islam, CHERIFOU & JOB SA BRAIN REND HOMMAGE AU FONDATEUR DU MOURIDISME CHEIKH AHMADOU BAMBA MBACKÉ KHADIM RASSOUL à travers ce titre.

Label : RockteamMusik
Contact management : Yass 00221 77 708 04 82
Réalisation :Ziz'Art 00221 76 324 78 77
Musique : Abbra
Kora : Elhadjii Kora

Intro
Mourite touba sunu xol
Mourite khelcom sunu toll
Mourite thianta lay dõne
Mourite baye fall lay dõne

Mourite touba sunu xol
Mourite khelcom sunu toll
Baye fall lay dõne
Thianta lay dõne

Refrain

Bougnou Diaggé Nagnou xam léep yaw laa
Bougnou Goré Gnou sante laa warna
Yaw Bamba,cheikh Ahmadou Bamba Xaliil gua Yonn ,Indi gua léer .Bounou Diagué léep yaw la,Bounou Goré Nélaa Yaw laa.

Couplet 1

Jeuff gua Lou Reuy si xol
Gnou diko séddé
Indi gua xéweul ,Indi gua Naatangué
Touba moy Guenél du sùnu Mbécté,Islam Amati Ndàm gnou Dikko Fêter
Diguenté Wirwir Mayomba
Diouli si guéthi akk NõNam Ya
Taxùko Yénni Yanaam baa
Yalla la Doylo ak Yonéen Baa
Lamù Tontou bureau bâ sa Ndar
Takhaaw Ni yalla bour
Ibra fall Fégnou Koo Nànn :Mbacke yaye sén bour

Refrain
Bougnou Diaggé Nagnou xam léep yaw laa
Bougnou Goré Gnou sante laa warna
Yaw Bamba,cheikh Ahmadou Bamba Xaliil gua Yonn ,Indi gua léer .Bounou Diagué léep yaw la,Bounou Goré Nélaa Yaw laa.
Couplet 2
Jangalé gua Alkhourane
Térée na Safane
Dimbali ganou bagnou Mouthiou si Nassarane
Niogui sùkù Raam
Délou Sakù Niann ,serign bi Taff nou sa Barké.
Dômi Mame Diarra Yoroul Liy Loré
Mbacke Balla Aisha Ya Goré
Yarr ganou Yiir ganou ar ganou Ya tabé
Soll ganou Jikko Yi Geunn Gnù Diko wanée
Lamou Tontou Bureau bâ sa Ndar
Taxaaw nii Yalla bour
Ibra fall fégnou KO Naan
Mbacke yaye sén bour

Refrain
Bougnou Diaggé Nagnou xam léep yaw laa
Bougnou Goré Gnou sante laa warna
Yaw Bamba,cheikh Ahmadou Bamba Xaliil gua Yonn ,Indi gua léer .Bounou Diagué léep yaw la,Bounou Goré Nélaa Yaw laa.

Outre

Ayoo léeeée...............bis
Kén d'où Mame cheikh ibra fall
Baye fall, baye fallou baye Faye yi
Kokou moy cheikh ibra fall Abo Ridial.

#bamba
#rocktem
#Zizart
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Bilae je n, arrête pas a écoute cette chanson

aminatakonare
Автор

Talibé Serigne Babacar la mais Serigne Touba lo ko way mou nekh ken d'où mom ! May tidianou Serigne saliou ! Yalla n'a Diam Sénégal ! Belle chanson guys!

biramambaye
Автор

Je suis talibé Baye Niass j'ai vécu à touba depuis 2012 mais j'adore les mouride ndakh Séne solidarité Séne meuna diokhé
Ils n'attendent rien de l'état hôpital poste de santé et j'en passe chapeau à vous

fatouthiam
Автор

Mane talibé baye la mais dama sope mouride yi rék té yalla takhe mame cheikh ibra fall yalna yalla yokou léram tassnousi barkém amine

khadija
Автор

Diouddo touba yaro touba magué touba niou toudé ma Serigne touba nguénté meu jour magal touba 100% mouridisme ❤️❣️

cheikhounandiaye
Автор

Kouye mouride beuseul j'aime 100%💕💕💝💕💝💕

maremendiaye
Автор

Un talibe cheikh mais je ne peux pas m'empêcher de vous laisser un commentaire et un j'aime c'est extraordinaire cette chanson dieuredieufé s touba

laminesimal
Автор

Je suis Soninké et mouride à chaque fois j’entends le nom de cheikh ahmadou bamba j’oublie mes soucis dieureudieuf ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

idrissaba
Автор

☝️un vrai tidiane mais s. Touba loko way mounex teksi gnar gni dagno ay lolll thiéy 18 safar koumafa deug néna massa

elzyau
Автор

Je suis un mouride sadikhe j'aime serigne touba😍😍

madiengthiam
Автор

Cheikh Ahmadou Bamba kenn la nakh souniou moko dieuk kennal kenn kouy wadial magal gui beuss j'aime❤😍

yungxeuch
Автор

ani wa safarisation ba yéna gui paré safar gui ken dou serigne touba kou daccord bessoul j'aime

mameboussodiouf
Автор

Je suis talibé Cheikh mais dama beug serigne Saliou Machallah vous avez encore frappé
J'arrête pas de regarder la vidéo encore et encore di lire en mm temps liii nexna 😍

ndeyeworembaye
Автор

Li mou tontu bureau ba sa Ndar KHADIM : Takhaw ni YALLAY Buûr
Mash'Allah....
Doomi Mame Diarra yorûl lûl lorè
MBACKE BALLA AÏSSA ya gorè
Yar nganiou yirr niou arr niou ya tàabè Sol nganiou jikko yi geune nioun diko wanèe..
Dieureudieuf Borom Touba

oumydime
Автор

1000❤❤❤❤❤ Bamba=zero complexe
Bamba néna toubabi " yallah lay bour"
Mame Ibra néko " yaye sène bour"
Kon bok kouy mouride bayil complexe.

linebousenegal
Автор

Les mourides qui aiment Bamba pouces bleu j'adore la chanson 😍😍😍😍😍❤

ndeyetall
Автор

On est fiers d'être des mouride alhamdoulilah baniou bokké thie confrérie mouride Dieureudieufé Serigne Touba🙏❤

mamefatoundiaye
Автор

Étant un fervant Talibé Cheikh mais koumako wahoul douko hame prck kan on parle de Cheikh Ahmadou Bamba, G les larmes aux yeux(la première fois que j'ai écouté cet tube je l'ai mis directement en boucle pendant une journée entière)...
Rien que soyy jangue hassida yimou binde rkk nga hamenii dinei gui rkk moko gnorr...
Et chapeau à Ziz'Art pour cet magnifique boulot(Du lourd)

AngeGabriel
Автор

Lamou tontou bureau bassa ndar takhaw ni yalla yay BOUR, ibra fall fellouko nikko Mbacke yay sen BOUR💪😍

wakhlouyydeffarnittgni
Автор

Ndeysanne yalla bou Bamba oumpou bene dioulite dakh kokou khamoul dagua réré mbirr yalna yalla wone niou yonou cheikh Ahmadou Bamba amine🙏🙏🙏

nitafificrush