La danse de Mia guisse avec son danseur

preview_player
Показать описание

Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Mia parfois nga diversifier style de danse bi. Bi mou takhawé la deviné bane la nara mayé😅😅. One love mia

fatimacissokho
Автор

Mia et sont danseur danse bien kou d'accord lalal jéme❤❤😍🤩🤩🤩🤩

DeboDiop-kcep
Автор

Ndeysane el estime trop son danseur D.M.😂🥰🥰♥️ j'adore leur complicité 😅❤❤jaam ci yeene 😂❤🥰🥰♥️♥️♥️❤

fatoukinedieng
Автор

Mia courage tu aura ke du bonheur inchala ke dieu te garde et te protège ❤

yazeynaciss
Автор

Frooonchement mounge nako ba sonnou😂😂😂😂 mais comme mické yoyou nonou di féthi 😂😂😂

KanyToure-mt
Автор

Mia sa fethieu bi deugeurna bomoy na goré😂😂😂😂

marietougueyembodj
Автор

Sokhor, ignane djayaté rek lagne fi néké di toudou panou djambour té ame piscine défaut jugements ak critiques you négatif youdoul djex aprè nit ki sou déwé gni nane ndeysan koubax lawone le monde est méchant Dieu seul a le droit de juger nous som tous égau ici😢😢😢

Carl-yyud
Автор

Mia sa yaram bi sokhor na pour nga yeungeul ko sakh dangkai force😂😂😂😂

africanlady
Автор

Je me demande pourquoi fi au Sénégal djiguen dou diapalé moromam loudoul diko hass dika dénigré té la plus part ni hassté dounou diakk courage à toi Mia notre fierté❤❤❤❤

Alhamdoulilah
Автор

Hummm. Coup de hanche bi moom diarna louné ❤❤❤❤❤. Aka maala yitéwoo bombaass 😂😂😂😂😂.

diawalysonkoalassa
Автор

gnéne gnare daguéne douro chaquarri Mame yalla ❤❤❤

MamendiayeDiop-sykr
Автор

Boulen sokhor way man deh danse bi dafma nekh ba 10 fois lako playe❤❤❤ jtm mia

AmyLo-rf
Автор

Mba toyoul bamou paré.quelle force😅😅😅😅

Saloumsaloum
Автор

Nofes Biyi Nga Khalè Bu Mene Yengel Ndigem Way 😅😅

maxgaye
Автор

Mia doucement rek . Bilahi déception bakhoul 😢xolal ki son changement brusque et négatif, à part seas belles mélodies kene apprécié woul son nouveau look😢. Mais du courage tu te retrouveras avc le temps inchallah 🙏

bachirbachir
Автор

Elle est tres belle machalla
Bonne continuation

RamaNdiaye-fn
Автор

Sheuttt les commentaires magui deh😂😂😂😂😂😂😂😂😂mya yaram bi deugueure na comme ciment bou toy dh😂😂😂

byanaartaye
Автор

Bouniou démé ba goor yi gueun niou noooyyy 🤣🤣

zahradiop
Автор

yaram bi mo gooré thi pobam Mia meune nga woy mais sa forme merci rek

diarrasene
Автор

Mia guess lokho yika nékon bakout bilay❤❤ samachanteuse préférè bi

OumoutallBa
visit shbcf.ru