SERIE - NDONNO - EPISODE 4 **VOSTFR**

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Khar média série bi nekh na mei def leneu jour yi ak heure bimouy ame nakh nitte yi sawar si setane bi tekk gueneu agualiko nakk nakh niou sawar si série bi nak

DawAmar-so
Автор

Moulaye bo démé alioune badara diourou ko .oumy diop ame na loumouye neube .soda tamite eupeule neu.arona kene douko yapp da ame foula

ndeyependa
Автор

Khar média série Bi nekh na amna sanse❤❤🎉🎉

Talibé_cheikh
Автор

Esk kham gueni Moulay gueye mi ba fa moy modiou pabi diorokou kou d’accord

ndiayadia
Автор

Moulay sa rewandei yamaleko si adouna ak si série bi tei ngua bagn si bolei yalla...ya rew deugue...'

Princesse
Автор

Fatou Ndiaye et problème c'est une longue histoire

FatouVilane-go
Автор

Finalement niom gnepp kan lassi alioune badara diour..

Princesse
Автор

Moulay mi bo démé mom mi moy batr bi bo démé alioune badara diourou ko 😂😂😂😂

awamouvivianesylla
Автор

Moulay esque pa bi mola diour 😂 sa djiko yaye rek gua yor

fatoukaire
Автор

Tay mou nekh mirase bi bou amoul more Dina ame blèsè 😂😂😂

fatoumoupakatasmoubmd
Автор

Haral ma deff nii baye modou😂😂
Mann la Amie Ndoye from the Gambia 🇬🇲🇬🇲🇬🇲❤️🇬🇲

amiendoye
Автор

Une excellente série vraiment machallah ❤

nafidiakite
Автор

Yayou arona tmt kon dagua infidelon sa dieukeur...heee kon arona tmt esk alioune badara moko diour..li diaxasooona nak.. alioune badara nieuweul leral😢😅

Princesse
Автор

Moulaye de nature il est impoli rôle yi mou jouait yeupeu affaire rou impolitesse rek laye jouais

AstouDiop-wikw
Автор

Les conséquences du takk souff woroul dale ndakhh adouna lépp amena ndoudou ak dead nio and

maimounasy
Автор

Masamba dans la vrai vie je l'aime

awadiallo
Автор

Thieuy encore Moulaye
Pa assane
Aly Mamadou mome daleu rôle you yi rek 🙄🙄🙄🙄

channelchoux
Автор

Thieye moulaye toujour même visage 😂 il est impolie

fatoukineba
Автор

Ohhhh😢😢😢😢😢masamba thiouné nah si crime bimou deff bi😢😢😢😢😢

amthesoldier
Автор

Ôh Soda boubokone ci séri bi dafay guena nekh

RamaNiang-kkhn