Dopeboy DMG - Dërëm (clip officiel)

preview_player
Показать описание
Ecoutez où acheter le projet/ Stream or buy the project :

Auteur : DOPEBOY DMG
Musique : YACINE.STT
Vidéo : PROLIFIC FILMS
Label : Allmade/92I Africa/Universal Music Africa

Production exécutive : PROLIFICS FILMS
Réalisation : Mame Selemane DIEYE
Directeur de la photographie : Mandione Laye Ka - Moussa DIALLO
Directeur de production : Pee Black
Direction de la post-production : Mame Selemane et Under VFX
Assist Real : Amadou Bamba
Étalonnage : Mandione Laye Ka
Chef électro : BRASMAGIK.LOCATION
Décor : SADIKDEF
Styliste : RADJ RADJ
Maquilleuse: SALY

Instagram Dopeboy DMG :



Couplet 1
Thibir thibiti feip lay yengal geusseum
Job kessei khamouniou kheureum deureum mome laniouy woti boleniok sa rappeur niou tass seureum beureung barigo khaliss
Fessal poches yek kholou mer
Lolou moniiu takha diouk
Goor yallah jamais ga guiss ko mou souk
Mouk
Loumou khate khate daniouuy dougou
Bokthi par force
Watier si carosse
Courone bi bien vissé thi sama bop
Allmade ak 92i si sa sama back
ame chaisou wurus rek moy takh ma tok
Boy trophée bi dinegn ko soulever
Degn def lou bari pour lolou dougn nagou moudier
Thi kaw rek thiakanam baller bi Lep loumay def defna thi bakanam
NDakarou senegal thi gal di diow pour conquérir adouna dounde akuna matara
Nwar est la ceinture enchaînement kou reip beu dougu sama 18 ma dakhar
Goor tia wakh dja bene yone leu dou wakhate
Liguey nopi succes bi oubi debat
Yegau finiou dieum mm avant niouy depart pirate navire bi accoster neu dakar

Refrain
Balle dans la tête moma guenal drapeau bi dem
Kene siy dess lolou mo takh ba gueer bi di diekh
Foumou nekh dem louma nekh def maguek nianou mère
Awma dara loumay tite sikaw souf
Succes bi rek laniouy guiss
Guissouniou lep ligua datieu pour yek
Samay échecs nioy sama échelle
Pour diote samay victoire yi guena leer
Dounde ay better days
Doundal sa niakheu sans compter si keineu

Couplet 2
Echec sunu cauchemar on veut la vie de reve takh ba souniouy nelaw yi reire
Leney takh guerre bi diekh moy keneu siy dess trone bi degou thi guédiou derete dinrinte tepeikou mounoma diay rew
Kenene kou mlni amoul mim rew
Benene missile sa kaw awma pitier
Ni Tiaga chaque jour malay tins moy sa liguey
Babay binks
Guenei djiko racaille
D’avance t’as perdu la bataille
Sa bay deguaa
Mounou thi reuthe ak bep khetou mousslay
chui pas dans les detail tu sais
Do sama frere beutou enemi lay guissei
Sa digu bop la bouteille est cassée
Ngur boudoul diekh leu le drapeau est levé
Lobeuss dara c’est la routtine dope defatineu miracle
Mirage bi laniouy sopi réalité
new neu niggas yiilay kharr sur le rivage
Beut yi yenesay dou guiss réalité
Sauvage Attaque a la machette fessal poch yi nek sama tete
Nigga chaque jour nek jour de paye
C’est le but dafa leer liguey rekay fay

Refrain
Balle dans la tête moma guenal drapeau bi dem
Kene siy dess lolou mo takh ba gueer bi di diekh
Foumou nekh dem louma nekh def maguek nianou mère
Awma dara loumay tite sikaw souf
Succes bi rek laniouy guiss
Guissouniou lep ligua datieu pour yek
Samay échecs nioy sama échelle
Pour diote samay victoire yi guena leer
Dounde ay better days
Doundal sa niakheu sans compter si keineu
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Le seul défaut du clip c’est qu’il se termine 😌

yorosow
Автор

Le plus sous estimé mais aussi le meilleur rappeur de reptyle les vrais savent 🔥🔥

zoutizou
Автор

Dopeboy dou nitou fii qui est d'accord 👍❤️

institutmoultazamofficiel
Автор

wallah Dope magui lay ñanal gue ameu lou raw li thi rap bi bilay un talent hors du commun 💥😍

andrealexisyparemendy
Автор

DopBoy a son propre navire il surfe pas dans les mêmes wawes que les autres LE PIRATAGE EST À DAKAR🇸🇳🔝

umxr
Автор

Le son je l’ai fait écouter a mon chien et il est devenu un lion 🦁

djebadiebskoita
Автор

Il est trop à l'aise et ça se voit qu'il est trop fort Dope Boy le rap 221 ne mérite pas t'es trop sous côté mais nous on est jusqu'à ce que ça pète ils sont pas courant ils rejoindront l'équipage plus tard 🔥🥰

moohamed
Автор

Je viens de découvrir grâce à booba 💯
Je comprends pas les paroles mais je kiff de ouf
Depuis le 🇹🇬

amelson
Автор

Jai 800 song sur mon Tel y’a k lui ki parle wolof le seul gars k valide dans c pays respect 🫡

papiisow
Автор

bro dagga taxaw mais bayil di rare mais song bi nice❤

pogboss
Автор

RATPI 🔥🔥🔥 🏴‍☠️🏴‍☠️🏴‍☠️ La piraterie n’est jamais finie ✅🏴‍☠️🏴‍☠️🏴‍☠️🏴‍☠️🏴‍☠️🔥🔥🔥🙌

maaffantome
Автор

Il est là celui qui va révolutionner le rap Galsen🎤❤️🇸🇳✌🏿

dassa
Автор

Dopeboy c'est mon rappeur préféré au Sénégal, c'est un frère depuis de la guinné Conakry 🇬🇳🇬🇳 vive le rap africaine.

ousmanediallo
Автор

92I 🇸🇳 C’est nous contre eux la piraterie n’est jamais fini 🏴‍☠️☠️

deffbeuz
Автор

Après 1mn d’écoute j’ai recommencé le clip naaah it’s too dope for the city 🤯🤯 🔥🔥

amadougueye
Автор

Ki doff la khamolein talent bouy nelaw si momeu international daffa diott tamite

AbdouNdao-znuq
Автор

La piraterie n’est jamais fini 🏴‍☠️🏴‍☠️

MoneyGangx
Автор

Nèkhoull ba nèèkh mais dopeboy dafa dope...

ABa-zopw
Автор

Très mal super c'est zooo depuis le Burkina 🇧🇫🇧🇫

frankylarmc
Автор

Y’a dakkeuh rap Galsen!
Sa wakh bari woul, yangi Job!

Amna yakar si rap Galsen ❤️❤️❤️💪🎧🎧

saliougueye