Wizzy Kana - LEERAY (Clip Officiel)

preview_player
Показать описание
#wizzykana #sénégal #abonnetoi

Auteur: Wizzy Kana
Directed by: Kalash
Son: Neegurap music
Mix master: Peulbouhigh beatz
Prod by: Bra beatz & Fantastic beatz
Production: MBT prod
Habillement: Tête de génie
Accessoires: 221 Luxury

Lyrics:

Toog thi sama xole ba abadane
Dahimane denk naala sama rouh
Iow laa teg thi kaw ndakh yaasi meune
Meunou nio beuré sa kaw ndakh yama daane
Ayy wakh you sew dou meuneu niakk souniou biir
Boulma méré soumala togné nangma baal

Leeraay
Yaay sama leeraay
Yaama dieulé si leundeum sotti ma leer
Yamay motali
Sa xole dou weet ndakh makoy wetali
Ehh iow leuh Diamond bi meuneu leeral sama eyes

Yaay sama lingueer beug naala deff jabare
Doff loo ngama ba parei denk naala samay fane
Beugouma nga merr teg naala fima teg sama yaaya booyé
Yaama joureul samay doom
Iow laa nara deff seen yaaya booyé
Mbeuguel day sakh thi xol iow
Yaay garab bi meuneu fadj sama feebar
Jaroul malay wakh ni damala nopp
Boo xolei samay beute ding kofa guiss sakh

Leeraay
Yaay sama leeraay
Yaama dieulé si leundeum sotti ma leer
Yamay motali
Sa xole dou weet ndakh makoy wetali
Ehh iow leuh Diamond bi meuneu leeral sama eyes
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Coubeuk seydina mouhammad psl May m'a aye aye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

Metmt
Автор

ce tube chaque matin mom laye diwo oute leeray ça mérite les millions de vues force à toi Wizzy

alaminofficiel
Автор

So deffé feat ak ash the best je te jure gue deff lou rew🙃

oumartoure
Автор

Ohh mashallah fils Ndam rek 🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

doudalo
Автор

Bilakhi Sénégal keneu eupolafi talents rap way fepu la foré magui lay begue dephis Abidjan one love man

MbavkeGaye
Автор

Da tella jiekh ohhh ♥️♥️♥️♥️❤️‍🔥❤️‍🔥❤️‍🔥🤧🤧🤧yalla nassi borom bi deff xeweul

mynahndong
Автор

WIZZY KANA LA FUTURE STAR PLANETE TERRE INCHA-ALLAH🤑🎊🎆
PLUS DE LIKE SUR LA VIDEO SVP

HasilazaMotors
Автор

FLOW BOU BESS LA INDI Bonne continuation$

mansourmassardiop
Автор

Le meilleur de sa génération thiakaw thia kanam brio ❤

aichasylva
Автор

J'aime beaucoup ce jeune artiste, beaucoup de talents sommeillent en lui❤❤❤, un duo avec iss 814 et Amadeus, serait une bombe de plaisirs❤❤❤

marieveroniquemendy
Автор

Baye pleaz guenel ben Sikar ci barkep magal bignou dieum🙏
Nice song❤

tukucisse
Автор

Wizzy Kana t’es le meilleur
J’ai couleur des larmes 😭 😢

cherifjacksonverra
Автор

Tres fort les émotions que degagent tes chansons.tu as tout machala pour depasser nos frontières.ta direction artistique doit etre la locomotive pour arriver a bonne gare.

momarfall
Автор

Au début j’étais pas kiffé say chansons mais ces derniers moments là sa son yi dafa fés dél sisa bibliothèque bi wollah t’es le meilleur respect à toi ❤🎉

fallousow
Автор

Hooo mogui Nic Mon Frer Bilaye li néx na waye ❤🎉

AmdyMoustaphaTV
Автор

Les mbourois sont encore fières de toi ❤❤

AmadouSene-gugn
Автор

Yalla na yalla wérral baat bi rek tu est fort ❤❤❤❤

mamadoucisse
Автор

Méheur de sa génération ❤❤❤❤❤❤mon artist ❤

ngonediop
Автор

C tellement Nice ohh lii nekhna way 🥳🥳

ousmanesolly
Автор

Noo lii doff na frere yalla na yalla sambe voi bii 🙏🏼🦾🔥🔥🫡

Cheifatou-yqwt
join shbcf.ru