Série - Promesses - Saison 1 - Épisode 23 - Bande Annonce

preview_player
Показать описание
Créer des émotions fortes et de qualité et les rendre accessibles à tous les consommateurs du Sénégal et d’Afrique, tel est l’engagement de Marodi TV.
S’inspirer des émotions des différentes couches de la population pour créer des opportunités de visibilité et d’engagement pour les marques, telle est l’opportunité qu’offre Marodi TV.

Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Happy birthday borom darou ❤. Je veux beaucoup de j’aime

Mbengue_ibro
Автор

Kou beug seydina Mohamed lalale♥️♥️cœur

Cheikh
Автор

Je suis perdu dans l’obscurité de la vie, dans les difficultés du quotidien, pourtant, quand je pense à toi, tu me procures plein de bonheur, tu es la lumière qui m’éclaire, tu es mon soleil.

BounaSy-phlv
Автор

Raphaël lidè moy adouna diaroul khèkh diaroul khoulo niteu dinala yakal ba fareu dèfaraleu la 🤣
Ni Alia dougousè momeu ragaleu na music daw🫣🤣🤣🤣

abdousalioumbacke
Автор

Take katou cheveux bou j’aime sama commanteire bou mala reukèe dinga mourou 🧕 dji 😂❤❤❤❤❤❤❤😌😌

Soxnabinetasaliou
Автор

Neyla qu’est ce qu’elle fait encore avec Kader

RamatoulayeTraore
Автор

MA GEUNE BEUGUE CHEIKH IBRAHIMA FALL LOU YALLA BINDE ❤🎉

ubfrict
Автор

Bilayyy g pithier de Rachid 😢bilayy moma gueuneul rafayal

amysow
Автор

Ça s'annonce pas mal cette épisode

sokhnamaiba
Автор

Sénégal amoul heure fixe 20h guénn wakhone ma togue di khar balegui

KanouteAwa
Автор

Yalla nagnou fèkè magal gui si diamou ❤❤❤

ndiayendeye
Автор

Rachid mbeuguél ken douko forcé😂 guiss nga nila Fama di forcé boppam nonou ngay forcé sa bopp Alia. Et pire lui, il a la clé quoi, il rentre comme il veut quoi😮.

LaBarhamienne
Автор

Marodi 11 minutes de retard soyez ponctuel way ishh

bbkyalalinguere
Автор

Boula eumbeulei série bi nga weussine hors série rk😂

FatyDia-jb
Автор

Bande annonce épisode 23 bi cagne laye ame

FatouGueye-jbsr
Автор

Lima sama bén grand wakhone nénama xalé bou raféte ken douko dokhane, néna jour bimou nango accepté guén ak yaw nénama bala matt 2 mois takeu ko rafale ko ay niari dome taf taf 😂 Rachid bo takone xalé bi bu yagg li yeup doula dal, loy dokh di dokhane 5 ans heure warone nala fékeu ci 4 ans de mariage ak 3 gosses 😂😂

papendiaye