Viviane Chidid : Siggil

preview_player
Показать описание
Viviane Chidid : Siguil
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

2024 qui est là aprés le mariage de Zeyna Ndour ❤❤❤ndeysan

FatouThiam-kl
Автор

Alhamdou j m suis marié le 25mars 1 jour inoubliable franchement sante n’a sama yaye bou bakh contente n’a si sama bop ❤️🥰 teudd fess dell monsieur contane sa famille aussi contane may daguou noumou ma nekheii louma matt mou dagu

adjidiagne
Автор

Conseil you werr 😢lii dou meussa xewi billae 2023 on est toujours là et ça nous donne la force de garder notre dignité pour nous d’abord ❤donc merci 🙏🏾

fatoumatadiedhiou
Автор

La chanson prend tout son sens aujourd'hui dome siguil n'a yayame bravo zeyna des pluies de grâces pour ton couple que dieu vs bénisse et vous protège 💚💛❤️

queenzaza
Автор

Je pense que notre jeunesse devrais écouter et comprendre le sens de cette chanson vraiment et revenir à nos valeurs !!!!

timandiaye
Автор

Beuguena siggil sama yaye ba sama futr mari respectema je t aime vivi dara nekhoul nga teude ak sa dieukeur âme ndaw sa yaye cntane 😭😭😭😭💖💖💖💖💖👍👍👍👍👌👌👌👌

oumarhanne
Автор

Ndeyssane sa me rappelle le lendemain de ma nuit de noce ....mes parents étaient tellement fière de moi ma maman a tellement pleurer....sama goro dima niatal rék sama dieukeur contane du sourire

binetourassoul
Автор

Deyssane ma mère me l'a une fois dit je t'aime maman 😍😍😍aujourd'huit mon marie me respecte je t'aime maman

saliimataciissokho
Автор

Ah yalla Naniou yalla diapalé niou am borom keur niou sigil sougnouy waydiour amine ya rabi Kou d'accord na beuss pousse bleu

ndeyelo
Автор

ohhhh son bi dama ko done deglou di dioy walahii guiss na si sama bopp djigueen amoul loudoul bopam akk bess bou rafet sigil say wadior dara guenou ko nekhhh.mashallah ok merci

DemProdinformatique
Автор

Bilay dara dakhoul gua teude ak sa dieukeur diar figa wara diar déjà d’où am loum la wakhal thé dinala respecter man dh khaw ma kan mai mangui sante yalla bou bakh bimala traverse li ba pare pask lolou mom c pas facile pask legui khale you gor yi bakhouniou thé khale djiguen gni yamougnou yalla nagnou yalla mousseul si gathie🥰🥰🥰😌😌😌🙏🙏🙏😭😭

malickwade
Автор

Yalla naniou yalla diapalè teh soutoural niou baniou sigil souniou waydiour yii inchallah ❤❤❤❤

SokhnaLo-bd
Автор

Oulala sama jour dièbalé mon frère a tellement pleurer je n’oublierais jamais ❤❤

maguettesarr
Автор

T es la meilleure de chanteur et chanteuse d Sénégal depuis 1999 jusqu'à présent tu es au top !macha Allah !

diakhomouhamed
Автор

Heure boumaye degue lou son bi dafmaye yokou diome guena xam maye kane ak fouma bokou guene takeu sama sereu guena tiye sama bopu❤❤

gnimadabo
Автор

Viviane décemment habillée avec un message fort, symbole des valeurs sénégalaises. Nous remarquons que notre Vivi adorée dans ses chansons se réfère souvent à Dieu (Yallah) ou dépeint la culture sénégalaise à travers des images sobres (vêtements, quotidien des gens...). Viviane me donne toujours raison d'aimer sa musique et sa personnalité.

keenal
Автор

Les filles déjà déviergés en écoutant cette chanson sen fit yi dou tok deh téyé sa bop ba dieukeur mo geune deh

souleydione
Автор

j'adore cette belle chanson.mashahahalah yalna djiguéne gnépp guis séne bop si woy bi, téyé sa bopp pour sakh sa diguaneté ak sa borom saakh wareff laa

sokhnandiayebah
Автор

Djiguéne amoul loudoul bopam té Daf ko wara samm alhamdulillah bala gathié loul sama yaye ndakhté nioun toucouleurs yi dano fonkk ada

rokhayasall
Автор

Ça me donne des frissons cette musique yallah nama Santa soriii bagui siguil sama boppu ak samaÿ wadiour inchallah🙏🙏🙏je kiff tro ces paroles

shupommetasoumare