Iam.Jarrah - Sucré, Salé (Official Music Video)

preview_player
Показать описание
Iam.Jarrah - Sucré, Salé (Official Music Video)

Artiste : Iam.Jarrah
Titre: sucré et salé
Composer: Bril
Mixed by: Bril fight 4

REALISATION : Mao Sidibé
CAMERA : Oumar Ndiaye
LUMIERES : Mamadou Dia
MAKEUP : Thiané, Aby Sow
MUSIQUE : Bril
STYLISME : Emad style, Afshal, Héritages couture
DECORS : MP Group
COIFFURE : Sophia glamour
ASSISTANTS : Mohamed Thiam, Pa Ali Diop
PHOTOS : Teklaf
CHOREGRAPHIE : Prince (contact: +221 77 448 62 72)

Suivez Iam.Jarrah

Ecoutez Iam.Jarrah

Lyrics

Bril on the beat

Nouma meuna mél iow ya takh
Souma solo bèy dagou bilay iow ya takh
Fouma meuna dém si louma meuna né
Xél dou diogue si iow non sama baby lovaa
Doxalal dama lasi wolou
Do niom té douniou iow ya meune si côté bobou
Baby dawalal fo diare yoon la
Boul tégui figua diapeu faleu bou dara yomb

Délko yeugeul mou saff
Goudi lakoy yeungeul
Sow mi délko yeugeul mou saff
Goudi lakoy yeugeul

Sucré salé
Nigamay deff safnama
Li loumou done xawmako
Xalé bilé diomal nama
Sama paradise aldiana
Nigamay deff safnama
Li loumou done xawmako
Xalé bilé diomal nama
Loma téré ma ba
Loma digeul ma deff
Foma yobou fala
Si iow rek la dess

Kouma khol si iow méréma awma si iow sago ningmay deff
Sama xol bi yasi né sama chérie coco ningmay deff
Bou souf sédé ba lepp ni sélaw
Thiouray gui di dioli ba beute sétt té kéne sou nélaw
Lo deff ayoul bilay dagoul diayoul
Niam nako nexna bayina xam nguani amoul

Délko yeugeul mou saff
Goudi lakoy yeungeul
Sow mi délko yeugeul mou saff
Goudi lakoy yeugeul

Sucré salé
Nigamay deff safnama
Li loumou done xawmako
Xalé bilé diomal nama
Sama paradise aldiana
Nigamay deff safnama
Li loumou done xawmako
Xalé bilé diomal nama
Loma téré ma ba
Loma digeul ma deff
Foma yobou fala
Si iow rek la dess

Lonkouna loukotina xam nguani doyalouma dolimaahhh

Lonkouna loukotina xam nguani doyalouma dolimaahhh

Ahh leeee
Leleleeeee wooyee mane dei wayna leee Diagne narr
Ndaw bou guisoul koumou mine day wétt beugue nala loleeeee ehh
Wane ngua ma mbeuguél wane ngua ma mbeuguél
Wane ngua ma mbeuguél wane ngua ma louy mbeuguél

#Iam.Jarrah #Sucresale #Music
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

elle chante son marie Macha Allah ❤ k dieu vous laisse ensemble ☝🏽💓

khadysamb
Автор

Kou beug jarrah votre altesse 👸 nèeeel

MamediarraDieng-kf
Автор

Sucré salé 🤭💘💘💘Kou doundoul mbeuguel manoko khame Liii liii day yeungeul deukbi🎉
❤je suis totalement bluffé !🤭🎉 La créativité visuelle est incroyable et les images capturent parfaitement l'énergie de sa musique. Les couleurs et les effets utilisés apportent une dimension supplémentaire qui donne envie de revoir le clip encore et encore. De plus, la façon dont Diarra exprime ses émotions à travers ses mouvements et son interprétation est tout simplement captivante💯. Je trouve que cet artiste a vraiment su évoluer et se démarquer dans le paysage musical actuel.

BAOLGLOBALTV
Автор

Machala mais sucré salé nare n'a tothie rew mi deh Machala l'artiste du peuple

macoumbandiaye
Автор

Entouka nekh na trop y'a meune yaguena fété khalé ❤️💍

SeynabouNdiaye-eryt
Автор

Chanson bi nekhneu sagnsé yi raffete nagne madame diagne dokhal fo diarr yone leu 💃💃🎊❤️

rokhayadione
Автор

Wawwww machala sama artiste bi lou khéré lay sagnsé way lou wowww kong korong💪

pjqosih
Автор

Lou way donn diay bilae tay mou lerrr😂wakh kat yi si rew mii kay lènn khar votre altesse 👸😻

MamediarraDieng-kf
Автор

Nonla dee seyeule dee machallah ❤❤❤❤❤❤

BbsokhnaGaye
Автор

Kou diougué si wally ak mia guissé rk gnieuw si diarra

CheikhfallouNdiaye-tw
Автор

Ay way yalnala yalla bayi ak Diagne narr puisque yomboul nga ameu kila beug🎈🥰👍 Diarra Saliou 🥰des j’aimes 🥰🙏👍🙏pour elle notre Vedette 🥰😘

modestemouta
Автор

Elle chante bien machallah❤️🎉normal nak lepp si xol la🎉🎉🎉🎉

JARRAHDIENG-mk
Автор

La golden girl de la musique sénégalaise ❤❤❤❤❤❤

AbdallahFall-rzky
Автор

Machallah MRS DIAGNE NARR😻contane naniou deh lii nekhna way 🎉

JARRAHDIENG-mk
Автор

OMG c’est sucré et salé en même temps 🥹🫶🏽💓💓💓💞😭❤️❤️❤️

cheikhmbackediagne
Автор

Machallah diara qui demka fanh depuis série vir Gini jtm 💖 machallah woyy bi nexna sangce bi Rafet n'a machallah 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

uqwxcbu
Автор

entou cas liy khénie nékhna liy khénie❤❤❤

FatimasaliouDiagne
Автор

Woww lou soft lann 🎉non douniou moromou khalé yii nak pour dire vrai❤❤

NdeyeantaCice
Автор

Gnaw❤diagne narr yi rek aka gno meilleur Machallah sagnesé gua nékhna

Sokhoulove
Автор

Ohhhh elle l’a fait machallah amati ga ndamm loutakh ma beugue ko rk

Anita-etsq