AMOURS BRISÉES Saison 1- Episode 23

preview_player
Показать описание
💔 Amours Brisés - Une nouvelle série captivante par Yesdakar Production !
Amours brisés tous les Jeudi et Lundi a partir de 26 Septembre Sur Youtube.
"Amours Brisés" plonge au cœur de vies bouleversées par l'amour, la trahison, et les secrets. Chaque personnage est confronté à des choix difficiles, des relations toxiques et des drames familiaux qui les poussent à leurs limites.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

beuss bouniouy yalah di dieul yalah na niou féke si anam bi si barker mouhamed psl❤❤😢😭🙏

MamecheikhDiop-rm
Автор

Yallah naniou yallah may moudiou bou rafet si barki seyedina Mouhamede sws😢

BayeSaliouDiop-rucu
Автор

J'adore le docteur, elle parle bien elle est douce aussi 🥰

MarieNgom-wq
Автор

Yalla naniou yalla mousal si bana ak diabote gou mél ni sa diabote guis 😢

Aminatadieye-yf
Автор

Pére Youssoupha yalna diokh héritage bi yépp Adama kou d'accord ak mane rkk lalal j'aime ❤ yeureum na Adama nakk mai diépi na yayam yalnagnou yalla mousseul si diabar bu bonne yayou cheikh tamit bonne na trop mom ak ay domam 😭

NabouNdiaye-iy
Автор

Nit kou khaliss diaral ly😢 yalla naniou yalla mouseul 😢😭😭😭

MariamaBarry-ey
Автор

Comment le vieux a fait pour garder l’équilibre pendant toute une nuit vraiment vous êtes fort😂

AminataNdiaye-jjld
Автор

Noonn mame Nene komé 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😭😭 damako beuguuu Sheut goudeul fane wayyyy mame boy ❤️❤️😍

MitouDiakhate
Автор

Kou kham ni pa bi dewoul rèk Bessel jamais

NogayeSeck-qcgl
Автор

Bana tu es vraiment cruels à ce point de tuer ton mari que dieu nous protège de ses personnes comme ça 🙏🙏🙏🙏🙏🙏

DiarryBasy
Автор

Beug na djiguene bouy seuy trop bilahi wayé yayou adama damakoy méré trop....si niak faydam😢😢

Babshii
Автор

Yalna niou yalla mousal si saitane teh yereum niou teh doli niou soutoura defal ko mbolem dioulit si barki nabi moustafa ❤❤❤ ameen

IdaChoi-hz
Автор

Le mieux c'est que père Youssoufa fait semblant de mourir pour aller se soigner et revenir pour faire fasse à ses enfants et sa femme

yacinediallo
Автор

Non mère bi bone na li lepp ndakh allal 😢😢😢

morndiaye
Автор

Un crime n' est jamais parfait, la position du vieux en est très illustrative, quelle erreur de ses fils!

ismailasarr
Автор

Kou geum ni pabi dewoul rek lala jaime 😢😢😮

OussamaDiallo-fgeh
Автор

Yalnagnou yalla soutourale thi barki Nabil moustapha

Ndourdollarofficiel
Автор

🎉
🥳🎊🥳🥳yappe guéne niou nak mais takhoul niou bayi heure bou dougué niou sétane ko😂😂

AwaDiop-zqxs
Автор

L'amitié est ce que ça existe jusqu'à présent ? Mais c'est douloureux de voir toujours les mêmes qui souffrent.

JulienneFeindaBagnoucoume
Автор

Delene wakh si série bi té bayi serigne bi pour ay j’aime

falloudiakhoumpa