Le Duo Rahim & Samba Zakir ont ému le Plateau de la 7tv

preview_player
Показать описание

Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Allahou akbar Abdou Rahim mangui fateulikou jour binga niowé si cheikh bi naan ko dama beugg zikar mounila dinga zikar inchalla
Yalla na baye yokk xam xam bi yalla weureul baat yi
Zakir jadore ta voix grave il est incroyable machalla👍
ImamAssane Diofior

Nafiyotv
Автор

Li kouko deglou dioye walahi niass Rahim Dia mala naw walahi sa voi bi rek darala💪💪😭😭😭😭

mariamadiallo
Автор

Je suis très fière d'être talibé Baye Niass❤❤❤❤

NdeyeFatouNdao-wvpd
Автор

Siroul yalla yeup mougui si djabatou maolana barhamou kou begeu yalla begeul baye niass li dafa neh walahi loong vi a vs les freres

barhamasene
Автор

Khôl sedena yaram daw bilahi sa entre directement dans les cœurs machalah yallana yalla diokh lene sen thiakoutef Def nou ay degue de gui talibe baye ya rabi barkep baye ak bayam dieufedieufety baye Niass baye Niass baye Niass baye Niass baye Niass

birameguisse
Автор

WALLAH NDEYSANE NIASS NINGA YEUKATÉ DRAPEAU L'ISLAM AM NA SOLO TROP MINKA YADI DIEMI MBOTE SÉLALÉN KI DONOU YONNENE SEYDI BARHAMA ❤❤

akhibousamb
Автор

Machallah niguène sèdalè souniou khole yalna yalla sèdall sen khole nonou si barckè mame baye dakh nioune mama baye rk laniou am❤❤❤❤👋👋👋

giuseppevacca
Автор

une duo exceptionnelle vraiment que dieu vous unissez si barke baye mi warale li

Автор

Li mane je ne peux même pas exprimé ce que je ressens 😭😭😭😭❤️ dieureudieufè baye🤲😭❤️dieureudieufè baye😭❤️🤲dieureudieufè baye❤️🥺😭

ramatoulayegueye
Автор

Rahim très cool et timide en classe o cem, ndaké lérr kessé nga ak talent Macha allah, kallah te garde, nice

byaka
Автор

Chukrane jaziilane baye yalna neexna trop. La lutte continue avec les jeunes de Mawlana Cheikh Ibrahim Niasse 💪🏾

sayidbangoura
Автор

Dieuredieufé baye Niass❤️❤️❤️
Sikar yi nekh na lol yalla na yalla wereul seni bat🙏

soultam
Автор

Chaque fois que je l'écoute c comme aujourd'hui yala n'a yala fayale gnou chiekhe Ibrahim Niass 🙏

MamiDiallo-tlzx
Автор

Je ne me lasse jamais de cette vidéo pourtant je ne suis pas Niassènne. Néanmoins j'adore Cheikh Al Islam.

sambagueye
Автор

Machallah zikr bi nekhna lole sakh..Yalla naléne Yalla féye si barké Seydina Mouhamed psl

adamasow
Автор

Deumb sama xol bi nimou seddé dafa eupp💓💓💓. Baye Niass dafa xew nak😂. Bilahi occasion yi souy am rek Sénégal dinagne xam ni Baye Niass ❤️ moy deugu ☝🏿💙

aichaomplik
Автор

Oh sama khol sedna mouride la wayé dama beug baye 🥰🥰

ndeyelo
Автор

Ndeysane défati guène dh barki baye niass❤️🙏🏽machallah

LaBarhamienne
Автор

Mach allah palateu bi riche na trop ak cheikh Aziz ndiaye

babacarndiaye
Автор

Mes enfants que Dieu le Très Haut vous paie UN JUSTE PRIX, pour ce que vous faites par la grâce de Yassine (PSL) . Amine

aminataseck
visit shbcf.ru