filmov
tv
Dieyla - Li Lanla ( Clip Officiel )

Показать описание
#Dieyla#lilanla#senegal
Crédits
Music : Akatche
Texte: Bakhaw
Mix & Mastering Akatche
Lyrics:
Damala Beug ba xawma lima dal li Lanla ..
Tayoumako khale bi xawma lima dal li Lanla
Dama Nop te te lernama te lernama wat nako si yalla
Waxal ma ko wa Kone b niou bayima niou bayima ak Yaw nguir yalla ma Mom la ..
Kay ngua wakhma foma dougeul mane
Beug na xam ndakh naturel na
Damalay guis salit dila Beug thiop melni Gaïnde gou guis yappa
Xawma li lanLa
Xawma li lane la
Damala guis salite dila Beug thiop melni Gaïnde gou guis Yap
Damala guis salite dila Beug fone xawma li Lanla
Wawaww mane ak xalé bi ba adouna Diekh ma wane Louy foula
Manila ki la done Xar défouma fo départ é li deh Thiou la
Foma wo ma niew ragalouma Lolou Wawaw ragalouma Lolou Wawaww
Han lima dal deh xamouma feke da niou ma Liguey deh diap na dama ko Nop mou dji dof ma diam leu demal ladial ma ko lima dal li lane la
Kay ngua wakh ma foma dougeul mane Beug n’a xam ndakh naturel la damalay guis dila Beug fone
Xawma li lane la
Xawma li lane la
Damalay guis dila Beug fone xawma Lini Lanla
Damalay guis dila Beug thiop xawma li lane la
Damako Nop ba dof papa sama Yaye nianal ma
Tayou mako xalé bi donal sama Serigne nianal
Damala love hé bayima bayima ak Mom nguir yalla ma Mom
Follow Dieyla

Комментарии