DEFMAA MAADEF Dieuredieuf (Official Video)

preview_player
Показать описание
Disponible sur toutes les plateformes de téléchargement légales

#mankowutindamli #defmaamaadef #dieuredieuf #afcon2023 #afcon2024 #defdefaat
Defmaa Maadef Dieuredieuf .
Un hommage a nos valeureux Lions de la teranga , l'équipe nationale de Football du Sénégal récemment Champion d'Afrique.

Music : Hackim Beats
Percussions :Cheikh Anta Ndiaye
Lyrics : Défa , Mamy Victory, Baay Sooley
Arrangements : Baay Sooley
Mix Mastering : Sir Khalifa

Make up: @soraya_doll
Nails @khoyane_beauty
Accessoires/ Bijoux: Ethnika ,221Luxury

Conception Idée originale :
Baay Sooley

Lyrics

DIEUREDIEUF

Sénégaaaaal
Sénégaaaaaaal

Kou ragal nanga daw
Kou gnémé nanga taxaw
Senegaaleu ngui nieuw
dalséne kaw
Kou ragal nanga daw
Kou gnémé nanga taxaw
Senegaaleu ngui nieuw
dalséne kaw

Yaay boy waxal ci Sénégal
Dégg naa koumou dadjél
Défaral kenn mounou ci dara

Yaay boy waxal ci Sénégal
Dégg naa koumou dadjél
Défaral kenn mounou ci dara

Askane bi Niomeu yobanté
Ladj lénema lougne mawax

Askane bi Nioleu yobanté
Ladj négnela  lougnou wax

Askane bi Niomeu yobanté
Ladj lénema lougne mawax

Askane bi Niomeu yobanté
Ladj lénema lougne mawax

Nénégne dieu re dieu feu téééé
Nénégne ma néléne
Dieu re dieu feu tééééééé
Dieu re dieu feu tééééééé

Gaindé Niouneuk yéne Gaindé Ba Abadane
Gaindé Niouneuk yéne Gaindé Ba Abadane
Gaindé Niouneuk yéne Gaindé Ba Abadane
Gaindé Niouneuk yéne Gaindé Ba Abadane

Diap may sa yaay
Mba nga diap may sa baay
Marodi gaïndé ndiaye
Aleu bi yay borom
Falmori boul ko laal
Falatimori boul ko laal
Ay dialalalata
Ndiaye Gaïndé Ndiaye

Nénégne dieu re dieu feu téééé
Nénégne ma néléne
Dieu re dieu feu tééééééé
Dieu re dieu feu tééééééé

Gaindé Niouneuk yéne Gaindé Ba Abadane
Gaindé Niouneuk yéne Gaindé Ba Abadane
Gaindé Niouneuk yéne Gaindé Ba Abadane
Gaindé Niouneuk yéne Gaindé Ba Abadane
Gaindé Niouneuk yéne Gaindé Ba Abadane
Gaindé Niouneuk yéne Gaindé Ba Abadane

Un très grand Merci.
DIEU RE DIEU FEU TÉÉÉÉÉÉÉ à Ndiagne Dieye les enfants de l'école de football et toute la population de Ouakam Bayé. Jahjeef , Pape Cheikh, Elom Lotsi , Gunman Xuman, Pére Joe , Mc Mo , Amadou Fall Ba MCU , toute l'équipe de NGB Niari Tally ,Cool 10 à nos amis , nos familles qui nous soutiennent depuis le début de cette belle aventure. Mention spéciale à Dudu Sarr DAKAR MUSIC EXPO .
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Premier à commenter. Niceh niche yalla naniiu yalla maayyy niou ndamm wayy🇸🇳🇸🇳🇸🇳

fatoufaye
Автор

Je l'ai suivi depuis le festival du sahel depuis lors j abonne partout sur Instagram YouTube ect bonne continuation les filles

justinjustin
Автор

Yene lafi yallah tekk liii la yallah dogual🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳mashallah🥰

dieynabafaye
Автор

c'est beau, c'est chaud, bravo mesdames !!

J.Nedelec-Andrade
Автор

Wa mais une telle œuvre Prqoi ça na pas percé ? 😢 c’est une dinguerie ça

lotteu
Автор

Sama niari soeur yi yénafi meune li dafa graw dieureudieuf sénégal rek mamy défa ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

omarngallageuye
Автор

Vraiment li chef d’œuvre La Mancha Allah 🔥🔥🔥🤗🤍🙏🏾

djibediawara
Автор

Serieux gni damalen beugue de trop ❤️❤️❤️❤️❤️

couradiop
Автор

Nice clip superbes costumes ladies vous avez du talent Machallah MV c tjrs un régal de te voir 🎤 sama ⭐️ bi je vous souhaite plein de succès ca kaw ca kanam rek inchallah. MC

adamadiouf
Автор

Lii dafa

2 artistes en compagnie de Baay Souley lui je ne sais même pas exactement si dans sa tête il y vie seul tellement qu'il est créatif.

mais man deuxième couplet bii rafet neu

elimanly
Автор

La décoration les couleurs le song les paroles le tempo tout est nice vraiment félicitations à vous 🇸🇳🔥

godfreegodfree
Автор

Félicitations et bonne continuations 🙏🙏🙏

mouhamadouhtmbengue
Автор

Félicitations🔥, je suis très content de vous avoir rencontré ce mardi 29/11/2022 à Paris La Defense, suite à la qualification du Sénégal🇸🇳, aujourd'hui, au second du mondiale Qatar 2022. Très talentueux, avec un esprit ouvert macha Allah

papebabacardiouf
Автор

Ndefa c mouhamet li nekhna lol mangi diégalou nak

mouhamedlaminedia
Автор

Très beau clip et jolie chanson by the way 🥰❤️
Vous devenez mon groupe féminin Sénégalais favori 💪🏽

leuzmelodytv
join shbcf.ru