Sadio Mané et sa femme Aicha Tamba #love #wedding

preview_player
Показать описание

Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Man dé magui ré😂 rék ni kou manqué😅. Vous êtes beaux machallah yalla na borom bi sam lén té barkél sey 🎉🎉🎉

salysarr
Автор

Maneu dé je suis tellement contente pour eux damaye sëtaneu vidéo di rai, di sourire toute seule. ❤YALLAH naléne YALLAH samale bopam.

yayendoumbeniang
Автор

Yallana yalla same te barkelé si barke nabil moustapha psl

sokhnandiaye
Автор

Sama xol bi ohhhh🥰🥰🥰❤️❤️❤️❤️😍😍😍 machallah yalla nalén yalla sameu mousseul lén si tiate ak leip lou bone Amine🤲🏻❤️

astafall
Автор

souniou sadio waaaay mashallah yalla na barkel❤❤

khadycisse
Автор

Machalla yalla na yalla barkel seybi si barké seydi mouhamed ❤❤❤❤

alycisse
Автор

Machallah yalla n'a seybi barkel❤❤❤❤❤

aidasagna
Автор

Retane Mme mané meune nama ray machallah heureux ménage way😊

Mamichoubb
Автор

Man Lima diaxal dama guisouk or ni ongule😮😮😮
Vraiment sadio e simple

loaboubacar
Автор

Super le couple MANE..Qu'Allah vs bénisse

antoinettemvondo
Автор

Congratulation 💚💛❤🤗Enfiiin 😍 Notre Mané ❤International Machallah laf bouche 😍😘 Yalna séy bi barkél 🤲🏽🤲🏽🇸🇳

aminadiagne
Автор

Mashallah Mebruk Sadio Mane, may Allah bless your marriage 💑

redibeyan
Автор

Madame sadio mané laye donne machalah ❤❤❤

KanyBa-ml
Автор

Maaachaa allah
Yallah na yallah deef barké

falloumbaye
Автор

Alhamdulilah may Allah bless this marriage till eternity 🙏🏻🙏🏻❤️❤️

AbdullatifMohammed-mi
Автор

Machalla yalla n'a yalla défal lene diama boubakh heure ménage

fatouabasslahidiop
Автор

Quel beau couplé ❤❤❤❤❤que dieu bénis se mariage ❤❤

IsmaNana-lxur
Автор

vraiment js8 contente yalla na yalla same léne ❤❤❤

amytine
Автор

Machalla laf thiat Yalna Seybi barkel amine barkep BOROM TOUBA

FamaDia-rsdh
Автор

❤❤❤❤ machallah notre gaïdé heureux ménage..Soyez heureux ❤❤❤❤❤

jeunetrader