Pape Diouf - Yaye (Live) - Lyric Video

preview_player
Показать описание
Pour chanter avec Pape Diouf, la Lyrics Video de sa chanson YAYE, interprétée en live et extraitede son dernier album L'ALCHIMIE.
#papediouf #yaye #lyricvideo video #lyric #love #live #generationconsciente #mbalax #team221

Auteur : Pape Cheikh Diouf
Comppositeur : Cheikh Ibra Ndiaye / Moussa Ngom
Graphiste vidéo : Torrodo
Une production Pape Diouf Group (PDG, Dakar, Senegal, mars 2024)

** Rejoignez-moi sur mes réseaux sociaux **
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Sm yaye sm waye sm lep nak longe vie à toute les mamans du monde ❤❤

AwaSow-bmug
Автор

Sargal Len sen yaye yiii kou saa yaye bakh rek lalal j’aime ❤️❤️❤️❤️

devossdiouf
Автор

meilleure musique de l 'année 🎉❤🫀anii dji beug sen yaye wayy😭😭😭🫀🫀❤

awadieng
Автор

Je réclame une chanson pour nos papa d'amour ❤

amymbacke
Автор

Sama yaye sama lepp bilay takha wou gama founé❤gnifi séneu yaye yi nekou 💫yalla naleneu yalla takhawou❤😍

mariemegueye
Автор

Sama mame sama yaye yalna ko yalla yeureum te kharé ko aldiana firdawsi 😭😭😭

symariama
Автор

gni beug sene Yaye aime Rene sama commentaire

antagueye
Автор

Kou revés teral sa yaye yana la yalla may ❤❤des ceour pour les mere❤❤❤🎉

gspohblvkhhihgxjfff
Автор

Ma mère est décédée à travers cette musique ndeysann je lui rend hommage et lui dis merci pour tout. Que je vis dans la douleur depuis son départ 😢. Que leurs âmes reposent en paix amin

AmeliaSagnang
Автор

Je t'aime énormément maman longue vie à toi chéri daimou si yow 🥰❤️💯

AdjaNdaw-ymnh
Автор

J'ai perdu ma mère mais j'adore cette chanson il as frappé trop fort les cœur pour nos mamans

dizadiallo
Автор

Pape diouf le leader de la génération consciente dafa beug yayam machallah longue vie à toutes nos maman 🤰 🤰

amadouberenger
Автор

yallah nako yallah nako yallah yeureum si barkée mouhaméd aléy salatou aléy wassalam

baoussmane
Автор

Sama meilleure chanson🎶❤😢😍😘
Longue vie à tous les parents❤️

Mbodji-walo
Автор

Sama yaye yalla nako yalla yeurem kharél ko aldiana 🙄😭😭

libasseyade
Автор

Sama yaye moy sama papa❤reine mère djigeine bou meune goor fall teiral leu rk la beug

dabafall
Автор

Thiey sama yaye dia DIMÉ YORO YALNA NGA KHIPÉ ALDIANA AMINE YARABI SI BARKÉ SEYDINA MOUHAMED 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😭😭😭😭

codoufall-unbu
Автор

Hommage à tous les mamans plus pressigement a la mienne diallo diéry lo doundou rek doyoul barki Serigne Touba cheikh saliou ❤❤

SokhnamaïTouré-og
Автор

Mane dal kou waye sa yaye mou nekhna 😢😢😢😢

CheikhtidjaneSeck
Автор

Sama yaye beugunala yalnala yallah bayii banga fekeh sun nyering

Fatoupriera