Tapha Gueye prend la défense de Siteu après la sortie du porte-parole de Yékini

preview_player
Показать описание
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah

malickdia
Автор

Vous n'avez rien compris. Depuis quand Siteu à commencé à dire Yékini est mon oncle ? L'avez-vous entendu réagir ? Ce qu'il peut détester dans tout ça c'est que Siteu annonce qu'il vient prendre sa revanche. Tout ça est derrière lui.

magattesamb
Автор

Bour veut être l'ambassadeur de Wély aka meneu politique😂😂😂😂😂

papeomar
Автор

Pere Palla may niou diame way.Yekini a parfaitement raison

ballacisse
Автор

Yékini da khamné bala gaye 2 daffa réw mo takh beugoul kou toudou touram si combat bi

Vikingsénégalais
Автор

Vous êtes hors sujet Yekini a raison ça vous arrange les polémiques

azizjazzdiop
Автор

Yékini limou wakh deugue leu bayina lamb nanouko bayi di touddou

AtoumaneNiasse
Автор

Yékini mo wakh deugue gnome gneup aye ndiambotam rawatina Modou Lo

BayeAbdoulayeGueye-encn
Автор

Tapha Gueye yaffi indi avertissement bayilen yekini soff. Guennnn té seytané buur mome diakhal ngama

BadaraSarr-qd
Автор

Siteu dafay daanou té Yekini begoul jelaat défaite ci Balla😂😂😂

drissndiaye
Автор

A mon humble avis, sachez que jusqu'à la fin du monde, Yekini ne digère jamais sa défaite contre BG2. Yekini ne gobe pas BG2.

babacardiallo
Автор

Lamine raynama néna siteu dagn ko dankafou 😂😂

afro
Автор

Père boul niou Sonal Tapha Gueye et toi vs êtes tjr ds la lutte contrairement à Yekini

yerosow
Автор

YEKINI mom khana amouli mbokk yène lolen beugg tjrs bou Siteu di beurré di wakh nane Yekini moma diokh li moma wakh li surtout combat Siteu MODOU LÔ diggeunté Yekini ak MODOU LÔ nieupp kham naniouko leggui bou Siteu wakhé lolou lanla MODOU LÔ di diappé Yekini 😮 il faut savoir raison gardé encore contre Balla Gaye 2 Yékini nieuwatt si combat bobou encore loussi am après niouni Yékini moko li moko là amna droit wakhni sama yone nekoussi boulen massi touddou tjrs nioumass khass di yakk sama image diw dafa sokhor diw dafa defni et vous êtes là à dire lolou grawoul ! Tapha Gueye chaque fois niou toudd sa tour si combat ni ya Déf li ya def lè té chaque fois ngua def sortie di lèrral rakhass sa dèrr ne soit pas hypocrite way ! Deugg d'où rombi nopp

mamadoufall
Автор

Yekeni fumouy wakhe Moy apre lambji su balla dane dou si deugeu Lou nekh Yekeni a raison

morlo
Автор

Lima mety rek moy deysann yekini doulennn tontou

BadaraSarr-qd
Автор

Mé yekini mo kham sou bouguoul siteu toudou ko louy défar mo gueune louy yakh porte parole limou wakh momela engagé gnaata combat la siteu beuré guissoul yékini déguouko té tarkinda bi mongui mokal deuk bi kone bouko siteu toudé si lambam dou khaliss dou mystique parce que sou nékone galathie kone mome dou teudié ak gnari défaite surtout bou moudié bi lac 2 moko daan té siteu lac de guiers guisnagnou noumou démé mome mo goréwoul rek mome yékini wayé taal bou yalla taal dakoy khambé ay noone gnoune kou beug siteu gnou beug leu c de sa qu'il s'agit deumou rek moy bagne siteu borom deuk bi c pas les marabout c DIEU siteu rék gnou dém💪👑💯☠️⚔️🏅

Misterboom-xx