Youssou Ndour - Bëy

preview_player
Показать описание
From the album "Ba Tay," 2002.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

The King 👑 . 2021, cette chanson me parle encore 🥺❤️ . #soninkalemme 🇸🇳

soninkalemme
Автор

Dangay nek khalè mouy way ngay fethì nga magg kham li way di teki nga geunn ko beugati merci you♥️♥️♥️♥️

lovemaman
Автор

Je suis algérienne donc je ne comprends pas les paroles mais j'adore vraiment. C'est un excellent chanteur. Ce sont mes amies sénégalaises qui m'ont fait découvrir cet artiste.

Perle__algerienne
Автор

Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak théré
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak deukhine
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak théré
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak deukhine
Limaguis si ale bi mom dafama doli khel
Kouné yam gueu sa palace té kouné kham say kharite
Mane dé guissa guouma fou bouki andé ak kewel di wakhtanal gaïndé mba mouy fo ak téné
Dicko thi di bouki kewel dé khamnako
Foumou ko guiss soriko lolou mokoy mousseul
Bey day andak ki bey lolou moy diam djé
Bey bey lay waradone té bey sakh lolo ko djik
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak théré
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak deukhine
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak théré
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak deukhine

Amna biss djambala nane domdia deguelouma fo guiss domi bouki nagua daw dou sa kharite
Gaïndé tha gaïdé bouki ndiour tha gogoua niaye day andak ki niaye ñiom ño bokou djiko
Ba kewel dem roti ndokh di wakhtane ak domi diassite bess bobeuthialako yaye dia guedia guissé bey day andak ki bey lolou moy diamdié bey beylaye wara donne té bey sakh lolo ko djik
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak théré
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak deukhine
Sama mame Ourousse Niang torodo samba guari diamna torodo samba guari diamna
Adjaratou Ourouss Niang mame torodo samba guari diamna torodo samba guari diamna
Mala yeup mane beya massi guenal fama souaré lathma loutakh
Loutakh
Segame bey math thi thiéré cole tamit néna bey meuna thi deukhine weulbatikou solthi samay sabar bou done election mom lay votel
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak théré
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak deukhine
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak théré
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak deukhine
Amna biss djambala nane dom dja degueguama fo guiss domi bouki nagúa daw doussa kharite
Gaïnde tha gaïndé bouki ndiour tha diougouyeu niaye day andakki niaye ñiom ño bokou djiko
Ba kewel dem roti ndokh di wakhtane ak domi diassite bess boba thi lako yayedia guedia guisser
Bey day andaki bey lolou moy diam diè bey beylay wara done té beysakh lolo ko djik
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak théré
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak deukhine
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak théré
Bou andoul ak moromi beyum
Bou moytouélé ande ak deukhine

omzoba
Автор

Ousmane sonko yakarou jeunesse bou Sénégal rék lanio Baugé diamou si yaw❤❤❤

madickediaw
Автор

C'est quand tu arrives à aimer une chanson qui a été fait avant tay naissance ke tu sais ke c'est de la bonne musique... respect père You.. on t'aime 💞💞

ndeyeawadiop
Автор

Yaye Sene Baye !!!
Kouko nangou besseul blue waye, walabok ?

ismaelsadjobari
Автор

Le monde d'aujourd'hui
Qui écoute en Mars 2020?

elinhojunior
Автор

Je pense j’avais entre 13 14ans quand ce tube sortais je demandais à mère du ko sonal pr lui demander il explique quoi sur cette chanson elle m’a répondu bo dmé ba nek magg di gua comprendre Limouy wakh maintenant père de famille diabar ak dom je viens de comprendre le sens de ce que ma mère me disais paix à son âme 😊

Papidiop-db
Автор

Tu enseignes à travers tes chansons ce qui est rare actuellement. Respect pour toi le King

cheikhdabossa
Автор

Le 24 janvier 2020 qui est encore là
Longue vie à vous je t'aime depuis la côte d'Ivoire

omzoniang
Автор

On ne doute pas qu'il est le meilleur de toutes les générations ♥️

khadysarr
Автор

Youssou ndour fierté du continents d'afrique je suis Malien je comprend pas c'est que tu dire mais ta musique ça mes touche gravement

modydembele
Автор

Même en 2021 je continue à l'écoute longue vie papa youssou Ndour une fierté pour le continent

aminadiao
Автор

Cette chanson a changé beaucoup de choses chez moi.Elle m'a beaucoup appris.Merci Papa Youssou ❤️

abdoulazizndiaye
Автор

Ce son es le meilleur son de tous les tps g comprend pas Wolof mais tout c ke cet Grd Homme g dis bien cet Grd Homme avec Grd H car il le mérite Walaye respect encore à toi le Grd Youssou de tjrs nous émerveille

alifigoelboulole
Автор

bilahi youssou ndour louy yeete rek ngay woyy doundal Ba say may dii bawann

ousmanefaye
Автор

Je suis Sénégalais j'étais au Congo Brazzaville mais la je suis chez 🇸🇳 je vous j'aime les🇨🇬

momoba
Автор

Les Senegalais ne connaissent pas la vraie valeur de Youssou

MISTERSHAKESENEGAL
Автор

youssou ndour est le mailleur chanteur que le monde n ait jamais connu

falloukadiaw