Le combat de la Couronne de l’Empereur. Balla Gaye II vs Tapha Tine vu du ciel, en HD. #shorts #bg2

preview_player
Показать описание

Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Kou mystique diapeu di nga déf placage bi non vraiment Sénégal mo beuri niou niémé yallah dof dof lou rék sinon vive Balla Gaye le vrai champion ❤❤❤❤❤

OusmaneSambe-lf
Автор

Balla bou xeere billahi❤sm prochaine adversaire la yeureum nako door bamou fatou yallahou niouni mystique la athieu rek balla mima guiss yone bimou neke ni sousi continue inchallah nafi door mbeur bamou wadeu❤❤

diop
Автор

No balla fila tapha égone sorina mes yaye mbeur walakhii ❤❤

MamelayeGueye-gmgh
Автор

Ana mystique fiii fans modlo ay vré mécontent lagnou

nitoudeugfall
Автор

Non mane fans modou lo l'a bilahi Balla moy meilleures salutations de combattants ❤❤❤

AbdouKarimgueyeGueye-in
Автор

Tapha dfna limou meun mais da dadié ak lion🦁 fene katt yi nán li mystque leu, fans modou lo yi, BG2 kessé💪

SidiFaye-wljj
Автор

Bo nekei champion rk mom gua 🤍❤️action Tapha Tine bi gniak entraînement mtx mounoul dann Balla ❤🎉

douelreyo
Автор

Sénégal mouy bari ay na fekh rk😅 ku mystique diapou dina déf li 😮 bilay BG2 yaye diambar deug mn lepp eup fit mn daxa baré fouff❤🎉😢

FadelDiaw
Автор

Empéreur bé mena beuré way c'est le meilleur 🎉

elchico
Автор

Merci balla gaye l'idole du Congo Brazzaville

RollysNguia
Автор

Balla en forme, c'est le meilleur

MorGaye-qowo
Автор

Balla gueye restera tjr rois des arènes national

boubacardybala
Автор

Balla dafa meune khèkhou lamb
Nimou def tyson , yékiny, Modou lo, gris ba ci tapha tine nga khzmnu dafa meune khèkh

cheikhdiao
Автор

Khana légui door thiabakhal mystique leu😂😂😂

albertsamy
Автор

Wow nakaté balla tapha yégone nako fii bilay yay ndanane nékone danouwone gua biu yagg 😂magui khar ba kén wakhfi mystique rek ma niouss ko 😂😂

Na
Автор

Mane pour mane balla danou na bou yague non yaye diambar way❤❤

FALLOUBOYE-lepv
Автор

Machalah balla nak Amna dolei, khôl ale rassoubi dafa Andak resistance

tukucisse
Автор

Balla seule y'a d'autre ici❤❤❤

BadaraNDIAYE-gzyl
Автор

Merci bcp père iow kou kham balla nga❤❤

diop
Автор

Mbeur yeupp balla mossi guena sone sou dané niouni dffa mystique adversaire bi souniou ko dané niouni entraînement wuull 😅 bayilen diambour

MouhamadoulamineseneMouhamed