Thione Seck - Sakh Yi (audio)

preview_player
Показать описание
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Yalla gualen fekk gniou Wor papa thione yalla bofa guiss dara loy ragal alawouma amine

ramsesssall
Автор

Bou féké khole bou rafette ak dioulité moy takh niite doug biir Aldiana yalla bou sounou yakaar tass yalla na la yalla lafal thiat reposes en paix que firdawsy soit ta demeure éternelle papà Thione 🙏🏽🙏🏽

pheulsow
Автор

Je n'ai jamais cessé d'écouter ces chansons maintenant qu'il n'est plus là 😭😭😭😭 papeu Thione bakh nga gnou ba dém😭 yalla nala yalla kharé aldiana Firdawsi 🙏 que la terre lui soit légère. 🙏

leadion
Автор

14 mars 2021... Dès que j'ai attendu la triste nouvelle, j'ai vite eu envie de réécouter cette chanson... RIP Papa Thione. Que firdawsi soit ta demeure eternelle

ndeyefatoucamara
Автор

Qui es la aprés son décé papa thione yalla gua khipé aldianaye firdawsi 🙏🙏

thiantakooneba
Автор

Tay dioylo nga gnou papa thione 😭😭😭😭 yalla nala seydina mouhamed psl térou 😭😭😭😭

mariemesen
Автор

Soumay dégg ay son wam dafay melni batay mongui doundou bilahi yalla nala yalla yereum téh xaré la aldiana😭🙏🙏🙏

maguettesarr
Автор

Liii maa ressentir deub moussoumooko ressentir depuis la mort de mon regretté père 😭😭😭😭😢ngiank dafa méti surtout quand c'est une proche papa thione yallah kippé aldjiana firdhausir si barké seydina Mouhamet Psl allahouma irfirlahou War hamhou 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽

fatoufall
Автор

Thiate moko dougoone rek mo takhoone mou dougou prison mais pour moi il est le meilleur chanteur au monde

modousow
Автор

Yalla boula Sakh yi doundé papa thione 💔 direct paradis Amine yarabi.

beuleupndao
Автор

Repose en paix Dieu te l'accueille dans son paradis

awaba
Автор

Que ton âme repose en paix papa thione😭😭😭tu resteras toujours gravé dans ma mémoire

Bvely
Автор

Vraiment adouna dou dara 😭😭😭 bien dit papa thione 😤 j s8 vraiment triste . Notre cher papa nous a quitté 😭😭😭😭😭😭😭😭😭

mbackefaye
Автор

Thiéy adouna amoule bénne solo que firdawsou sera votre demeure éternelle amine

mariememarieme
Автор

Papa thione seck yalla naka yalla yereme te khare Al Diana ak molem joulite bou fatou

modoubamachalla
Автор

Ma maman avait une cassette noire qui ne contenait que des chansons de Papa thione. Elle l'écoutait souvent du haut de ses 35 ans 45 ans. Elle est partie le 22 déc 2016 et elle me manque énormément😳😳😳😢😢😢. Rip Mère SENE

seynaboundiaye
Автор

Ay adouna dou dara j’écoute cette chanson 🎶 mes larmes 😭 n’arrête pas de couler réponse en paix ☮️ papa thione dans nos cœurs ♥️ a jamais

coumbakane
Автор

Sakh yi khana dugen wor tey bogu thion yalla na yalla yerum te kharal aljana

dioufallemagnesutelhadji
Автор

Le problème c'est que ici au Sénégal quand tu vives personnes ne te connais mais quand tu meurs hoo 'mais Papa Thione était un monument un homme multidisciplinaire yalna la PLS térou 💜💙💜💜💙

sokhnaseck
Автор

Kou khamone aduna... Yalnah yallah khare la thi jannatoul Firdaws

seynaboundiaye