Hip Hop Feeling 2020: Xuman, Awadi, Ndongo D, Ngaaka Blindé, Dip, Clayton, Ara, Wzaa, Fata, Dahman

preview_player
Показать описание
Hip Hop Feeling 2020 All Stars : Xuman, Didier Awadi, Ndongo D, Ngaaka Blindé, Dip Doundou Guis, Clayton, Ara Akhlou Brick, Wzaa, Fata EL Presidente, Dahman
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

non le gars il est troopp fort ! Des rimes croisées ! des rimes suivies ! Des assonances !!! Non ces écrits valent de l'or !!! C'est LA révélation té amagoul morome 😎✨

bambadiop
Автор

Douma djouk fii nikou tok si mine 🔥🔥💪
Bo sibé i Bi rk tapél DiP DounDou guiis dou

kinsimore
Автор

Sincèrement couplets yeup dope... Ara sa flow amoul féne Ngaaka tu as kické ça comme personne... Dip mighi cool... Ndongo wané gha yay grand bi.... Xuman iow mom monument... Awadi mighi cool...
Bref, C'est du lourd love Hip hop galsen

socrateduemesiecle
Автор

Dip est le meilleur niou kharr niènene nieuwe niou commentaire mr6

laminesene
Автор

Ara de akhlou brick mi esk nitt la 🎉🎉😮

badzaofficiel
Автор

Dip et Awadi clash guenn dh, sanni kherr😂😂
Ngaaka un goss qui a un style de ouff sheuu🔥🔥🔥

ababacarndiaye
Автор

Ngaaka 😲🔥🔥 doope
Nigeu bou naw ma keuteu sa laf 😂

TEAM_DMG_OFFICIEL
Автор

Baba dawoul thiow foune yobou hip hop bi mou wane lén ni dousén morom j aime baba💓💓

magougueye
Автор

Je ne suis pas fan de ngaaka mais il est vraiment fort ce gars quand il fait du Rap real c'est plus qu'un artiste avec son Flow de dingue 🔥

lmjuuf
Автор

Ngaaka ❤️ blindé do nittt tégou si bit bi nice 💪

samanit
Автор

Ngaaka niouna na dip ak grand yi d😂😂🔥🔥

lakhatseck
Автор

J'ai retrouvée mon NGAAKA BLINDÉ dieu merci ❤❤❤

ahmadandiaye
Автор

Wallahi souniou rappeurs ay ndanane piiir laniou Dip, ngaka, ara akhlou brick avec ou sans corona daguene di dokhal à tous moment Gnaff ♥️💪

sakhofatoumatarougui
Автор

Dip il est vraiment fort mais le gars ki a commencé est malade 🔥et le flow de Ara toujours au top

mansourcoly
Автор

Non dip à chaque couplet il déchire tout🔥🔥🔥 king tout simplement 👑

godisonebbuban
Автор

No king baba défatina limou meuné bilae 🔥
@nguaka_bleindé le meilleur

aliounedieye
Автор

#Ngaaka_Blindé
Hip hop feeling leu day ñieuwaat fayaat baune. Baba jeulaat mich bi melni kouy Drague Gun. Yioe Fata, Waxal jury bi joxma rhymou Taf. Baba ndiaye dou kaf, ci Taf Taf ma teudj sa Nigger ci kaaf. Rap bou sap saf, flow bou dak yapou saaf. Mangi ci jawou dji claf, Nigger bou naaw ma keut sa last.
Technique flow rhymes yi guéne sama mind Taf Taf Taf. Bathie Raf Raf Raf. Wathie charte def nga Paf Paf Paf.

Damn 🔥😎 Ngaaka bayil waay🙈😭. Yañiou Gueune🙈

rossrazak
Автор

Ngaaka bou melni laniou sokhla sii game bii technique ak jaap bii rap classique bii 🔥 gars yeuppa assure vraiment nice

benalydiop
Автор

Yup paff paff pafff ngakka leu très fort man

daddyndiaye
Автор

Le passage de NDONGO D témoigne que les old school ont toujours leurs places dans le game sénégalais. Il est le meilleur ce NDONGO

momarmamadouciss