Enemy

preview_player
Показать описание
#TOPBOY nouvel EP maintenant disponible sur toutes les plateformes musicales ⬇️

————————————————————————
Compositeur : Amoniac x Freshii808beatz
Mix/Master : Freshii808beatz
Cover : ItsMDG
————————————————————————
LYRICS

Nouma meunti mel yaw yaay kitax
Mere beugoul sam diguenté ak yaw xol bangui takeu
Pourtant diguenté bobu meune nama dougeul ci pax
Th liniou sekeu meussouma sekak benene nit louko dakeu
Yay li gueune
Si lima meusseu dal ci sama vie
Laata niouy tassé sama stock d'ambition gueunone neu vide
Si lileu neix
Gueudj naci tek sama tankeu
Th taxoul nga dem diapouma wone naa dem beu yam leu fi
Sama ay defauts soudoul wone yaw mane noumay def ba xamko
Si gnima weur sa ay intentions si gueuneu sincere
Prudence biné si mane yaatax ma amko
Tu fais des choses pour moi pareil que ce à quoi un saint sert
Yeah
Xam say faiblesse day tax nga fort
Th wolou trop seu ay force meune neu tax banga faible
La mer n'est pas potable mais mom leu dieune di nane
Yeugo mbeuguel bilay aveugler ba doma meune wax li am

Bayilene maak samay enemy
Awma sene faay samay enemy
I can fly as long as i got em
I'm not gon shine without enemy
Ndieurigne bingma amal xamo sax nimou doy
Mane dh meunouma am louleu gueuneu reuy
Boudoul famille bi yay kima sol diom bi
Enemy
Ndieurigne bingma amal xamo sax nimou doy
Mane dh meunouma am louleu gueuneu reuy
Boudoul famille bi yay kima sol diom bi
Enemy

Enemy
Yay sama settou bi gueuneu ler
Metit bi yamoul feneu gatiéy nga nara tax ma triste
Sa lamigne lay guiss reflet sama leundeum ni takander
Sans yaw kouy té souma naré bayi loxo nieup farma ci
I love you so much
Am bimala am defnama honneur
Yay ki gueuneu tax nekouma dormeur
Kone goudeul fane enemy goudeul fane yeah yeah
Tu es mon trophée le plus merité
Depuis mes 17
Meusso fi gueudj
Yay kitax li bone nioukoy meune modifié
Point you faible yiné si yaw ndeysane nga fokni mongsi nieup
Monté yay ecole bi meune ci yima diar nekoul lycée
Limala am
Meunouleu romb bénédiction
Baxoulo mais comme xaliss t'es un mal necessaire
Soumleu amoutone foumay jeulé yi pulsion
Sa dé djigoumeu mais aka maleu meunone fékhel

Bayilene maak samay enemy
Awma sene faay samay enemy
I can fly as long as i got em
I'm not gon shine without enemy
Ndieurigne bingma amal xamo sax nimou doy
Mane dh meunouma am louleu gueuneu reuy
Boudoul famille bi yay kima sol diom bi
Enemy
Ndieurigne bingma amal xamo sax nimou doy
Mane dh meunouma am louleu gueuneu reuy
Boudoul famille bi yay kima sol diom bi
Enemy
————————————————————————
Suivez moi sur les reseaux :
Snapchat : theleundeumest
————————————————————————
#CAB
Рекомендации по теме