13 août 2021

preview_player
Показать описание

Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Dieureudieuf serigne Touba. A diarama Mame Cheikh Ibrahima. Yaw rék la beugueu té Yala takh. Am nga talibé. Am nga kham kham té djiguéne dakoula té gueunoula machallah. Serigne Touba amoul morom.

abdourahmanekonate
Автор

❤❤❤ mane yow rek lay top mouride civilisé am classe Macha Allah

SokhnandeyeFaye-fv
Автор

Machaalah
machaalah amena solo jërëjëf vraiment Yalna YALLA defal la Jam ak xeweul and ak soutoura wer ak werler and ak goud fann Faty Dieng
amine ❤❤

dembacisselayelaye
Автор

Machaalah Adja Faty Dieng bii moom daf mayy daaneel jërëjëfati

dembacisselayelaye
Автор

Machaalah! !!!
amena solo jërëjëf vraiment

dembacisselayelaye
Автор

Man dé damalay sopou rk té hawma loutah Liga démissionner tfm nonou lama nakaré

khaimseck