Polygame - Saison 3 - Episode 172

preview_player
Показать описание

Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs :

Pour suivre toutes vos séries préférées :

Suivez nous aussi sur les réseaux sociaux :
- Twitter : @senepeople

#SenePeople : la chaine des séries sénégalaises
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Vraiment meununa setane benene serie budul bi sa reflète notre société sénégalaise merci senepeople ba meilleur acteur ak thiam le duo de ouff

mouhamedndiaye
Автор

Binta samb amna ndam vieux ba délona avance noooon rousna 😂😂😂😂😂❤❤❤

SeneCheikh-uwgr
Автор

Mane bizarrement Ba meunou ma si mom Lou bari goor bou melni Ba yalla nagnou si yalla mousseul

fatousow
Автор

Wa Seune mi esk sava dans sa tête meussouma guiss kou gnakeu gueume bopame ni

noelle
Автор

Mousse bi dokhi soxlam ga koye sossal 😂😂

Ablayb
Автор

Kiné ak tham😂😂😂😂wa yén famille Sénégalés yen nékhna dé 😂🤣 ay maryatou moy bandi deugeu deugeu

astalo
Автор

Ba meilleur acteur
Well done senepeople

dembakonate
Автор

Vous n’êtes pas cohérent. Comment ca se fait que Ndiambé raconte des choses qui se sont passées au debut du mariage de Seune alors que quand il venait d’arriver Seune disait n’avoir jamais connu ni entendu parlé de Ndiambé.
En plus Seck qui se présente à Daba Tall comme s’il ne la connaissait pas alors qu’il disait que djiguénam la. Ne nous prenez pas pour des fous quand meme. Ou bien vos episodes ne se suivent pas. De toute facon, cette serie n’a plus de sens c’est juste pour passer le temps. Respectez nous un peu quand meme

mayaxneyo
Автор

Non polygame no stress yalla na sene diam yagg

secodarame
Автор

Thiey thiam envoie toujour le contraire rek la positionné yooy 😂

NdeyeAissatouDiouf-lh
Автор

Kiné nak sof nga ci li ngay niai kersa massar 😢

halimaperez-hkem
Автор

Séance kiné ak thiam😂😂😂😂😂 nn kiné banal thiam

awafall
Автор

Seune tamit amoul respect, ki dé déna ba pare na contrôle ay waham binta ak domam nagnou bayi keur diambour ak problèmou diambour

ZeinabkCissé
Автор

Fat kiné amoul kersa c'est un mauvais exemple. Mais seune mome vraiment ken khamoul limou beugue. Elle doit voir un psychanalyste

gorguihospital
Автор

Papou ndeye ndiaye kome gounor bo dougué si daba digua khamné yalla diouli la santané

BinetaNdoye-yfpp
Автор

Thiouth yamal Nguaye sii yeufou ba Nguaye dougou mais ba ndiambé séne momite néna day soufou ba seck le grand macro kaat bii😂😂 pa daba tall da mool nak😂😂😂 dieuleul Thiam yéboye néna 16 21😂😂😂😂ba loy roukh khanna nékatoko ba léggi pousse taak ngua beugue nékk😂😂😂😂

papewade
Автор

😂😂😂😂Kou namm wa Akhlou bi comme mann yeuk till sa lokho✋🏾

malicksy
Автор

Seune weroul dé 😂😂😂 djiko bou bone la am té soff

MounasDione
Автор

Ndaye diaye dou bokatoul si tiyatar bi dou nekh

mortallaba-gsjl
Автор

dikatttt na mani greffagou mere bi doulénsi wah comme sabar bou tasse

fallousow