Ya Ngoné Zikroulah - Ndongo Daara [ Clip Officiel ]

preview_player
Показать описание
Salut la Famille je M'appelle Ya Ngoné Zikroulah Bienvenue Dans ma Chaîne YouTube Je Compte Sur Vous Pour Partager & Abonnés SVP
Комментарии
Автор

Ndeysane sama khel bi yeup mingui si sama dom ja
Yal nanga mokal ak diam ba gnibissi wate incha Allah. Une pensée à tous les Ndongo Daara

aliounediouf
Автор

Vraiment, MashaAllah, notre Yaye Fall nationale pour cette magnifique chanson profondément empreinte de reconnaissance dédiée aux Talibés et aux Baye Fall. Bonne continuation et qu'Allah vous assiste et vous protège, Inshallah. Votre comportement exemplaire est une source précieuse d'enseignements et l’image que vous incarnez à travers votre habillement à la fois discipliné et respectueux, reflète une grandeur intérieure et une noblesse de caractère. Vous êtes un véritable modèle de rigueur et de dignité qui inspire respect et admiration.

bayeniasselabeugue
Автор

Yalla nala yalla takhawou si lap barke cheikh moussa Cissé y’a Ngone borom batou or bi ❤

cheikhmboup
Автор

Billay y’a Ngoné ndongo dara niepou kontan naniou yalna yalla dolli laa diam té geneu wérale bâte bi si barcké cheikh Ibra

PapecheikhDiop-kkrm
Автор

C'est toi qui m'a fait aimer le zikroulah yalna bate bi barkeil barké serigne saliou

papambaye
Автор

Oh neex Na amna solo . Na ñuy dimbli dongo yi ci ñam, ndox ak weccet . Bu ñu xeeb dara. Yërmànde rekk❤❤.

daoudandour
Автор

YALLA NALA YALLA barkel am nga yarr am tegine ma challah fille chérie bonne continuation et réussite totale dans tous les projets ❤❤❤❤❤❤❤ Al hamdouli lah DIEUREUDIEUF Niang

kenzangom
Автор

Bismillah Masha’Allah thiakaw thia kanam Insha’Allah si doley Baye Ndiour..❤️❤️❤️❤️ We love u

coumbaniang
Автор

Kone Kii moo way son bi machallah ❤🙇🏾😎

Cheikhounabambajuniorlelion
Автор

Kou d’accord ni dafa niro ak aïda samb😮❤

PendaNdiaye-bveh
Автор

ndaysane koufi nieuw ndakh Challenge tik tok yi rk may ma j'aim❤😊m

khadimtvsn
Автор

Ndeysane li nèkhna way bly yaye boye yalna bate bi wèrr ♥️😅

MoustaphaSamb-hs
Автор

ya ngoné content na si yaw 🙏 yalla na yalla takha wou ✅ fall guana yague guana wérr 🙏🤲

FallouNdiaye-nvxz
Автор

Machaalla mak sama ci kaw ci Kanam nekhna yatouna Yallah na Yallah barkel ci daradia Sangue Ndiour
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

SodaNdiaye-rmjb
Автор

Ya ngoné li nekh na trop machallah yalna yalla weral batt bi way ❤🎉

PrincesseamyGning
Автор

No li nékh na bly yow ❤❤❤❤❤me na diamou si yén 🎉🎉❤❤ baye fall yi kéne dou leen djitou Aldiana walahi ❤❤

MoustaphaDiouf-fz
Автор

Machallah 🎉❤ Dieureudieufé Serigne Touba Dïärämä Mämë Chëïkh Ïbrähïmä Fäll 🏁🤍

Møühãmędãlį_
Автор

Djadjeufati Ya Ngoné Yallah na Yallah wéral bate bi 🎉❤

babacarndiaye
Автор

Machallah.Dieurediefeuti Cheikh Moussa Cissé Ndiambé Borome Darou❤

mameawadieng
Автор

Machala sarsara group félicitation bon continuation 👌❤️

PapelasGueye
visit shbcf.ru