Série - Lady Diama - Saison 1 - Épisode 06 - Bande Annonce

preview_player
Показать описание
Créer des émotions fortes et de qualité et les rendre accessibles à tous les consommateurs du Sénégal et d’Afrique, tel est l’engagement de Marodi TV.
S’inspirer des émotions des différentes couches de la population pour créer des opportunités de visibilité et d’engagement pour les marques, telle est l’opportunité qu’offre Marodi TV.

Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Bou adouna nékh baniou fatté gni niou djiitou si birr souf. ndax yageu yageu daniou léne di fékki dji. na niou léne diangeul fatiha ak 11 likhlass nianal léne yallah bour bi yeureum léne té xaré léne alldianatoul firdawsi si barki alkhourane
🤲🏽⚰️🤲🏽

mouhamedndao
Автор

Kou beug bass plus que aladji beuseul j'aime

maremelo
Автор

J’adore Ass-Mao
Féminine - douce_pieuse et très calme
Machallah

soninkohprince
Автор

Kou beugue serigne touba lalal Jaime ❤

MamediarraDjitte-cvds
Автор

Maneu dal lady ak bass rek laay toppou❤️❤️❤️

torodo.ferrari
Автор

Marodi TV merci pour toutes les belles œuvres et debut de votre commencement ❤❤❤❤ vous méritez des remerciements

wjflxce
Автор

Celui qui lit ce commentaire que Dieu vous bénisse et vous garde en bonne santé vous et vos parents ❤

mamitacaramel
Автор

Diama devrait dire la verite à sa soeur asmao, elle est plus responsable et mature k sa copine 😢 cette awa kinè k'elle dit tout ne va rien lui apporté k plus de douleurs,

toufashrassoul
Автор

Série bi sous amoul mort dîna am blessé 😊

MamediarraBop-kf
Автор

Noon😂😂😂 mane awa kiné dinama raaay 😂😂🤧

gueyesoxnafaty
Автор

DIAMA tu commence a prendre gout akh compagnie a la situation dehh

mariendiaye
Автор

Noo Série bi Machallah ❤❤nekhna nak mais déflen ko 3 fois par semaine

qojvubv
Автор

Aladji dé mo ngi topp ngora keng bi rek di nane😂. Li yalna diour djamm

adamandiayekasse
Автор

Sonko Moy diomaye diomaye moy sonko Lou khéré😂😂

sokhnadiop
Автор

Marodi bou adouna nékh banguén changé bass def ko kou bone Lady Diama ak Bass bouniou moudié woul ma bayilen ba bayalé lou takh thii yén😏🚶‍♀️🚶‍♀️🚶‍♀️🚶‍♀️🚶‍♀️

tabarawade
Автор

Vraiment Awa kiné n'est pas une bonne amie pour Diama elle se fiche de ses états d'âme elle n'a que ses intérêts

binozildieng
Автор

Kou gueum nii Awo bii lakhom guénoul sii digueneté Diama ak aladji rk

MamanFall-di
Автор

Ken compul dara nada touss niente ahh sen bande annonce gatna 😂

evistambengue
Автор

Take katou cheveux bou j’aime sama commentaire bouma la reukè dinga mourou 🧕 dji 😂❤❤❤❤❤❤😊😊😊

Soxnabinetasaliou
Автор

J’aime pas cette Awa kiné c’est une mauvaise compagnie pour Diama.. elle doit être plus intime a sa grande sœur

marthemazarine