Pod et Marichou - Episode 48 - La Bande Annonce du long métrage

preview_player
Показать описание


Pour suivre toutes vos vidéos préférées :

Suivez nous aussi sur les réseaux sociaux :

Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

marichou beurii ngeu wakh so djongue wone dugn leu takal woudiou toggal fofou di debat #la puissance rek ♥

mamediarrasamb
Автор

vendredi inchalah kene doumafi yeugu waye 😀😀😀😀😀😀

matoushematoushe
Автор

marichou en mode depression  la puissance dou ay thiakhane  dionguer ba ame woudiou

bintouthiam
Автор

marichou sa rappel notre tradition. j l'aime bilahi ay tia lou bandi Di ndirole. Eva sa waha tauye n'a loula dale dianhe

dieyembaye
Автор

Marichou loump nga wa Senegaall yeuppp ak sa retanou fin bi! Euw!

MrThegamesh
Автор

tekite tekite el hadji enh enh non pod nigeriene lamaye saff taye mais dou yomb ak marichou rek matena 1234 💞💞💞

cheikhtv
Автор

marichou nekal fi di armewou di har kou nieuw si keur gui... #la_puissance ♥

dembissenegal
Автор

ah limome dara fayou ko s'en serie n ekh n'a trop je vous souhaite une bonne continuation

ndiayenogey
Автор

thine bokoul safine, wanter bi thiafka thine dee nekhna pod bou yague bobou khamagoula.togual fofou di diaye vulgaire fokni moye seuyy. la puissance rek thi classe taww bou fanane sakh douko faye

astoudiop
Автор

Marichou yangui tiite deh 😂😂😂😂, Eva dougoul cii iow deh, Pod rek mo Doug cii Eva . hahahahahh cey Puissance

aliounefall
Автор

j'ai jamais commenté mais marichou ray nama thin bokoul thiafine. team Eva n marichou

coleththioune
Автор

Tchio marichou gniaw gua kéne khamoul liguaye nourole #teamEva la puissance mala gueum iow

sasajalow
Автор

Ahh nileuh diégg deug dafay wolou bopam _team_marichou

coumbambaye
Автор

marichou tu vas me tuer je suis fan de toi vremnt je t'adore avec tés dégagement . première dame des bari fém

magnemabadji
Автор

loutakh Marichou nekhmeu🔥🎀🔥mdr.... Eva iow mom dieuleul ce temps

adambenkhalifa
Автор

Marichou ndeysanne mo gui wakh tou😂😂😂😂

fallmameanta
Автор

waa hééé Marithiou mii Eva doof loo nakko dé 😂😂😂
magui koy khar avc impatient

joliecur
Автор

Marichou dafa moudié doof wala ??😨😨😨😨😱😱😱 je hâte

tfkteew
Автор

wouy marichou dof na thiey la puissance yaw la gueum

assanetall
Автор

tchinn bokkoul thiaffine Marichou mala wolou

queenshasha