Sadbou Samb - Thiofel GUI wa macka [Clip Officiel]

preview_player
Показать описание
Ce titre est un extrait de mon prochain album intitulé Wayal Nabi.
Mix and mastering : studio Lamp Fall
Arrangement : Amadou Sy et baboulay Cissokho koriste
Remix single Solution de Abou Thioubalo
Production TMS
Réalisation : 3D Recordz
Remerciements : staff groupe Tabala Nabi , le groupe Kaay Bakh Adja Issa , Khalil Seck , Lamp ,Amadou Sy , Remercier Abou Thioubalo ,thierno Niang Le protocole Ibou Camara , le manager Cissokho ,
Dame Seck , Dame Ndiaye, Mame Modou Diaw, Ingénieur Pape Samb , mes frères Cherif Samb ,Fadel Samb , Djily Samb ,Ouseynou Samb , Assane Samb , Mama , Mouhamed Junior , Babacar Ndiaye, la femme de valeur Mme samb
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Ndeyesane 😭gnoune yao rk lanouy toupou wallahi ❤️ yalhnala yala sameuh té mayla goudou fane ak weer ak weerlé ba ligua name ligueul sama tourango Mouhamad psl gua yegualé sa saguo🤲❤️Sadbouh yagui degue louné ms mougne rk kiguay tagne sakh amone n'a Ay none degue louné ms dra yalhnala yala gueuneu teck loko ligueuy bi inchallah dou mousseu lale Souf si kaw ci kanam rk ci barcké cheikhna cheikh sadbou 🤲❤️❤️❤️

medounesamb
Автор

Dèfati ngua sa maniine d 🥰🥰🥰 masha'allah 🥰🥰🥰 yalla nala yalla may goudou fann AK wèrr thi Seydina Mouhamed (SAW)❤🙏

serignemodoudiop
Автор

Barck cheikhna cheikh sadbou do srne morome yalla nala yalla lafall thiett❤❤❤❤❤❤

ibragueye
Автор

Bilahi walahi nimala beugé yalla rek moko kham❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

cheriffathiam
Автор

Machalla ndékété dal léppou lou nékh wala lou rafét rék si sama Wadji Moustafa salla lahu halayhi wassalam la diékk. Yalla nanou yalla tass Si barkém

moustaphathiam
Автор

🌨️💚🌨️🙏🕋 Salalahou Aleyhi Wasalam Rassoulil Karimoulay💕 Nabi Moustapha Alaïka🤍🌷🍃 Ken Dou Mome🙋🙏🌨️💯🇬🇭🌵

fatoumbaye
Автор

Machala sama wadji rk mo diara beugg seydil awalina wal akhirine ♥️🕋

mya_rassoul
Автор

Yalna yalla doli diam ti yonentibi psl ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

ndeyemadeleinediallo
Автор

Machallah Yalla na bate bii werr sì barke seydina Mouhamed keke dou mome ❤❤❤

awadiop
Автор

Chanteur du peuple nioune yaw rek lagnouy topou ❤❤❤

SeynabouMbaye-huex
Автор

Sama sopé bi xol sedatina ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

MameBintaNdiaye-tb
Автор

Machallah sougnou doome dji Yalla na Yalla werral baat bi si baké Ya Rassoulillah (PSL)

Nas
Автор

Yalnanga goude fane loool té weer Sama domedjii machallah

AwaSène-jx
Автор

Machallah I LOVE PROPHÈTE MUHAMMAD SALALLAHU ALAYHI WASALAM Machallah Sadbou Samb👍❤🤲

MNaby
Автор

Ndaysane sama Idol bi❤❤❤ beuganala ndakh Yonénté bi

mouhamedalamineniang
Автор

Machallah yaw rk lay topou ndax ki ngay tague♥️♥️♥️♥️

NogoyeFall-hw
Автор

Hol séddana trop Machallah sa kaw sa kanam inchallah

dieylibagdadsidibe
Автор

Thieuy sama rak dji machala ! Saadbou sama rak la , Cheikh Mbaye Samb !

aissatougueye
Автор

😢 Cheikh Saad bou Samb soop nala Nguir Yonenty bi haleyhi salatou wasalam

papandiogouba
Автор

Ya meune ya eup dolé yallana yallah sam machallah

martincorine