Mondial 2022 : Sadio Mané et les Lions en shooting avec les nouveaux maillots du Sénégal

preview_player
Показать описание

Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Li mom diarna dém ensemblé nationale ndah gnou lidianetéko

coumbaseck
Автор

Du vert sur du vert avec du vert à la pelouse, puma tu ma hontie

houlaymatoudiallo
Автор

Franchement maillot bi gnawa neu, comme ay yeuré talibés,

alblink
Автор

Françement nous sommes comme des guinéens moi je suis désolé on à pas de ministres d'ésport

sencarservice
Автор

Bou féké kou diouke rk ☝️ khase sou niou maillot yi Kone Kane mo niouy take bayi léne 🤕 ligué ni déf maillot yi raféte na 👍 bou féké nonou la yéne défar léne maillot you raféte

adjicoumba
Автор

Franchement maillot yi grawoul mais les bas ngen changer won couleur bi mon tanéi

momodiopsopenaby
Автор

Respecter woune sakh africain yii koi,

disturbingstar
Автор

Ces maillots là sont trop enfantins. Au début je croyais que c'était des enfants.

laminemarena
Автор

Mane senegal damayakarni da deugeu ligeyou diambour yi maillot com maillot équipe bou kogne

papekane
Автор

Thiey senegal kholal ma maillot you bone yi rek

mathiou
Автор

Mbété gnétti aricots, man li cheikhou di si maillot you niaw yii diaxal nama

houlaymatoudiallo
Автор

Je vous souhaite bonne chance Les lions

awaniane
Автор

Nooo franchement maillot yi sounouko yoboo coupe du monde dinan rouss trop koi😊😊

layelaye
Автор

Ani couleur yi...c koi sa ces maillots...ani sounou drapeau bi

modoukhoule
Автор

Li bane genrou maillot leu tamite???
Est-ce que dou maillot yi gnou wara soll pour entraîner wou??

mypbarro
Автор

Sac de ciment !!pas de shael ni dangotté !!binék rio lay nurorr

baytalasyllasylla
Автор

lii lanela thie verte bou maillots gnougui melni gnakhou alle bii thie néwéttt gui verte na dé 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

kadiadiallo
Автор

Deet way, maillot yi mom rafétoul😂😂😂
Borom 2 galons yi bayil roubei

khadydiedhiou
Автор

Qatar ak nimou tanguer niouy yobou frotter
Ndakh maillot comme potou frotter bou verte bi😂

papigueye
Автор

Li melni tolou dougoub comme tawét dhe

serignesaliouseye