Comment Retirer de l'argent Sur hamster kombat En Wolof

preview_player
Показать описание
lien de inscription ⬇️

En Wolof.... • à propos de hamster combat

Hamster Kombat fowokaay la buñu mëna jëfandikoo ci Telegram ngir am xaalis te doo fay. Ñu ngi ko dugal ci 26 màrs, 2024, leegi amna lu ëpp 150 milioŋ nit ñu koy jëfandikoo. Di nga mëna def sa bopp ci palaasu CEO bu weccoo ak def misioŋu bis bu nekk ngir am poñ Poñ yooyu dina ñu la may nga mëna am $ HMSTR Token airdrop biñ nara def ci weeru sulet 2024.

Hamster Kombat bot la buñu mëna jëfandikoo ngir am xaalis ci aplikaasioŋu mesaas bi ci saasi Telegram biñ genne ci 26 màrs, 2024 te tay amna lu ëpp 150 milioŋ nit ñu koy jëfandikoo. Juër yi ñu ngi ci dàll CEO exchange crypto te dañu wara dem ci 10 niveau ngir am xaalis ba noppi mëna am airdrop.

HSMTR mooy token bi juddoo ci xeex Hamster bu sukkandiko ci TON (Reseau bu ubbeeku bi) blockchain. #blockchain #hamsterkombat #Hamster #combat #crypto #altcoin #bitcoin #cryptomonnaie #trading #formation #wolof #woloftuto #telegram #telegram_link_in_description #sénégal
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Merci beaucoup mon frère j'ai regardé beaucoup de vidéos mais toi ton explication là c'est clair bro

kalidoudia
Автор

Je n'arrivais pas à entrer dedans

khadimsene
Автор

Wa man wave ak orange money la guissoul

MouhamedDiame-njwr