BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 23 : Bande Annonce

preview_player
Показать описание
Prêt.e à replonger dans l'univers BÉTÉ BÉTÉ, au cœur de familles Gueer, Guewel, Teug ou Laobé ?Suivez la saison 2 de BÉTÉ BÉTÉ avec un nouvel épisode chaque lundi et jeudi 20h30 UTC.
#betebete #saison2 #episode23 #bandeannonce #legsdusang #evenprod #creationoriginale #team221

Réalisé par Ibou Gueye (Sénégal, février 2025 )
Une production EVEN PROD SENEGAL : +221 33 868 27 26

** Devenir annonceur ? Contactez notre service commercial **
Evenprod +221 77 422 70 41

* Retrouvez Evenprod sur les réseaux sociaux*
Twitter @evenprodsenegal
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Ayyyoooo Paco mingui guinz Oumy Mbaye🎉🎉🎉
Bigué tay la la yalla done khar😂

soxnafatousaliousarr
Автор

Sénégal deh ndaeke yonete bi
psl lagnou beuge ❤️❤️❤️❤️❤️
íhomme parfait

KouraSaliou
Автор

Sma yaye la beug yobou makka nianal len ma si guir Yalla yalla yombal ko si 2025 bi 😢❤

maxbbfall
Автор

Kou yakarnei dinga téki yobou sa yy maka rk lall j'aime 🎉❤❤

ThianéFall-qe
Автор

Kouy khaar Gathiay aîsata Kane kom mane rk lalal j aime

falloudia-lxmc
Автор

Li dh moy yallah dou nitt 😊entre bigué et déguene

Byh
Автор

Des cœurs pour notre Prophète Mohammed sws ❤❤❤❤❤❤

FatoukinéNdiaye-ij
Автор

Ehh bobou diakar lo ❤ épisode bou niew gana nékh🎉

BayemodougueyeBayemodougueye
Автор

Yalla naniou wor si diam bou kéne manqué si barki seydina mouhamed ❤❤❤

babacardiouf
Автор

sama khol bii 😂😂😂😂🎉🎉torokhal Bigué biii niaw khamone ngani seu beuss dineu nieuw wayy

vickysahiri
Автор

Tay mou nexx😂 rencontre bigué ak deguéne si entreprise bi😂💃🏽💃🏽

ZeynaNiang-gzfz
Автор

Des cœurs Pour notre Prophète Muhammad (PLS)

Mohammedbassir-jl
Автор

Aye bobou dadjé Bigué ak Laobé yi Lou nara nekh yéneu meune yéneu eupe dolé Evenprod Machalla ❤❤❤

AdamaDiedhiou-rw
Автор

Kou geume ni Evenprod dou moromou gayi di lappi lappi rek 😂😂❤

IbrahimaDiba-fl
Автор

Ballenma akh balle naléne yalla naniou yalla soutoural 🤲 🤲 🤲 🤲 🤲

SeckDiabél-gw
Автор

YALLA nagnou YALLA doli Soutouran bou bakh may gnou diam ❤si barki Rassoulilah SAWS 🙏🏽

TairouColy-trdy
Автор

Kou yakamti wone la rencontre de Bigué et de deguéne dans l’entreprise sow rk lalal aime🫣
Lou nekhhh🎉

AissatouDiallo-gfpu
Автор

Oulalala les tenus et attachements de foulard sont trop belles ! Vive les sénégalaise ✨🇸🇳😍
Depuis la 🇫🇷

Famiyota
Автор

Yalla nagnou yalla may moudiou bou raféte yalla na yalla yeureum way dawelou yiii 😢

boyemor
Автор

Evenprod nous réserve beaucoup suspense qui comme moi qui à hate suivre épisode 23 demain inchallah

dialodiallo
join shbcf.ru